input
stringlengths
13
433
input_fr
stringlengths
2
469
input_wo
stringlengths
15
414
label
stringclasses
77 values
Are there limits with top-up?
Y a-t-il des limites avec la recharge ?
Ndax amna ay àpp ak sarse?
top up limits
how much for a physical card?
combien coûte une carte physique ?
Ñaata la àb kàrt di jar ?
order physical card
Is there anything to do because my phone was stolen?
Y a-t-il quelque chose à faire car mon téléphone a été volé ?
Lan laa war a def ndax dañu sàcc sama telefon
lost or stolen phone
WHY IS THERE AN EXTRA FEE FOR USING THE ATM??!!!
POURQUOI Y A-T-IL DES FRAIS SUPPLÉMENTAIRES POUR L'UTILISATION DU GAB ?? !!!
Lutax mu am ay njëg yu ëpp ci jëfàndikaayu gab bi?
cash withdrawal charge
how do i dispute a payment I didnt make
comment contester un paiement que je n'ai pas effectué
Naka laa mëna weddee payoor buma deful?
card payment not recognised
Can you tell me how to get my card on the app?
Pouvez-vous me dire comment récupérer ma carte sur l'application ?
Mën ngeen ma wax ndax mën na jël sama kàrt ci aplikaasiyoŋ bi ?
card linking
I stupidly initiated a rent payment from the wrong account yesterday. It can't be paid from that account, but it really needs to get paid on time. Am I able to move the payment to the right account?
Hier, j'ai bêtement initié un paiement de loyer à partir du mauvais compte. Il ne peut pas être payé à partir de ce compte, mais il doit vraiment être payé à temps. Puis-je déplacer le paiement vers le bon compte ?
Démb ci nàkka xam, dama tàmbali feye luwaas ci sama kont bu baaxul. Mënu ñu ko feye ci kont boobu, waaye dañu ko wara fey ci waxtu yi war. Ndax mën naa yóonee xaalis bi ci kont bi war?
cancel transfer
Although I transferred some money, it has not as of yet, arrived.
Bien que j'ai transféré de l'argent, il n'est pas encore arrivé.
yónnee naa xaalis, ba leegi yeggagul.
balance not updated after bank transfer
Hi I've been trying to top up my card for the past day but it gets declined, I need it topped up urgently! Can somebody get back to me to resolve this or explain any different ways I can top up my card?
Bonjour, j'essaie de recharger ma carte depuis un jour, mais elle est refusée. J'ai besoin de la recharger de toute urgence ! Quelqu'un pourrait-il me recontacter pour résoudre ce problème ou m'expliquer d'autres moyens de recharger ma carte ?
Salaamaalekum, ayu-bés a ngi nii may jéem a sarse sama kàrt waaye jàllul. Ndax am na ku ma mën a woo ngir saafaral ma jafe-jafe bii walla mu leeralal ma anam yi nuy sarsee ak kàrt yépp ?
top up failed
What are the sources for the funds in my account?
Quelles sont les sources des fonds sur mon compte ?
Fan la xaalis bi ma gis ci sama kont jóge ?
verify source of funds
My card payments have stopped.
Mes paiements par carte ont été arrêtés.
Dañu taxawal samay payoor ci kàrt.
reverted card payment?
I just transferred some money. Why was I charged a fee?
Je viens de transférer de l'argent. Pourquoi des frais m'ont-ils été facturés ?
Dama yónnee xaalis waaye. Lu tax ñu teg ma ay fere ?
transfer fee charged
I have not received my pin yet
Je n'ai pas encore reçu mon code PIN
Jotaguma ci sama kod PIN
get physical card
Please delete my account and personal information.
Veuillez supprimer mon compte et mes informations personnelles.
farleen sama kont ak bépp xibaar bu ma ñeel.
terminate account
Can you please help me in canceling my order.
Pouvez-vous s'il vous plaît m'aider à annuler ma commande.
Ndax mën nga ma jàppale ngir ma fomm sama komànd?
request refund
I had to pay one pound more than the set price!
J'ai dû payer une livre de plus que le prix fixé !
Fey naa benn pound bu ëpp bu bokkul woon ci njëg li.
extra charge on statement
An item I bought had the wrong exchange rate applied.
Un article que j'ai acheté avait un taux de change incorrect appliqué.
Dayo weccoo xaalis bi ci benn afeer bu ma jëndoon jaarul yoon
card payment wrong exchange rate
Where do my available funds come from?
D'où viennent mes fonds disponibles ?
Fan la sama xaalis bi yemb jóge ?
verify source of funds
Where can I check to see if there will be a fee added to my payment? Are there specific instances that will result in a fee added?
Où puis-je vérifier si des frais seront ajoutés à mon paiement ? Existe-t-il des cas particuliers qui entraîneront des frais ?
Fan laa mën a saytoo ndax dañuy teg ay fere ci sama peyoor ? Ndax dafa am jokkalante yoo xam ne dafay laaj ay fere ?
card payment fee charged
Can you explain to me why a cash withdrawal shows up as pending?
Pouvez-vous m'expliquer pourquoi un retrait d'espèces apparaît comme en attente ?
Ndax mën ngeen ma leeral lu tax xaalis bu ñu jël ba noppi nekk ci pekku négandiku ?
pending cash withdrawal
I can't find my card, it is lost.
Je ne retrouve pas ma carte, elle est perdue.
Gisuma sama kàrt , dafa réeer?
lost or stolen card
How long do I have to wait for my transaction to be completed?
Combien de temps dois-je attendre pour que ma transaction soit terminée ?
Ñaata waxtu laa war a xaar ngir sama jokkalante bi jàll ?
transfer not received by recipient
Is my PIN sent separably?
Mon code PIN est-il envoyé séparément ?
Dañu xàjjele kod PIN bi bi ñu ma koy yónne
get physical card
I purchased this item and would like a refund
J'ai acheté cet article et je souhaite un remboursement
Lii dama ko jënd waaye dama bëggoon u delloo ma sama xaalis
request refund
I was charged an extra pound for no reason. Why is that?
On m'a facturé une livre supplémentaire sans raison. Pourquoi ?
Dañu ma feyloo benn téere te dara waralu ko. Lu tax ?
extra charge on statement
How do I go about exchanging currencies with this app?
Comment puis-je échanger des devises avec cette application ?
Naka lañu mën a weccoo xaalis ak aplikaasiyoŋ bii ?
exchange via app
What are your exchange rates calculated from?
Sur quoi sont calculés vos taux de change ?
Fan ngeen di sukkandiku su ngeen di xayma seen dayo weccoo xaalis ?
exchange rate
What sort of restrictions are there for the disposable cards?
Quelles sont les restrictions pour les cartes jetables ?
Lan mooy tënk yi ci kàrt yuñ mëna jëfandikoo benn yoon kese?
disposable card limits
What is the charge for exchanging currency?
Quels sont les frais de change ?
Yan ñooy njëgu weccoo xaalis bi?
exchange charge
How soon do cards arrive after I order them?
Combien de temps faut-il pour recevoir les cartes après les avoir commandées ?
Ban diir lay def ngir jot kàrt yi ginnaaw biñu leen komànd?
card delivery estimate
My purchases from this morning still have pending payments.
Mes achats de ce matin ont toujours des paiements en attente.
Yi ma jënd tay ci suba benn jàllagu ci
pending card payment
I keep checking my statements but nothing shows up.I requested a refund a long time ago but seems like it's not submitting my account for some reason. Can you please help me get the money back from the seller for me
Je consulte constamment mes relevés, mais rien n'apparaît. J'ai demandé un remboursement il y a longtemps, mais il semble que mon compte ne soit pas validé pour une raison inconnue. Pourriez-vous m'aider à récupérer l'argent auprès du vendeur ?
Laaj naa ñu delloo ma sama xaalis bu yàgg ba tay, waaye dafa mel ne sama bi dafa am jafe-jafe. Ndax mën ngeen ma jàppale ?
Refund not showing up
Why was I charged $1 in a transaction?
Pourquoi m'a-t-on facturé 1 $ lors d'une transaction ?
Lu tax ñu feyloo ma benn dolaar bi may def ab jokkalante ?
extra charge on statement
My identity has been stolen. I still have my physical card but there are charges I didn't make on my account. How do I cancel this card or dispute the charges?
Mon identité a été usurpée. J'ai toujours ma carte physique, mais des frais que je n'ai pas facturés ont été débités sur mon compte. Comment puis-je annuler cette carte ou contester les frais ?
Dañu sàcc sama dàntite. Ba tay maa ngi yore sama kàrt waaye am na xaalis bu ñu jël ci sama kont. Naka laa mën a niilalee kàrt bii walla ma jéebaane fere yii ?
cash withdrawal not recognised
If I ordered my new card last week, how much longer should I wait to receive it?
Si j'ai commandé ma nouvelle carte la semaine dernière, combien de temps dois-je encore attendre pour la recevoir ?
Su fekkee ayu-bés bee weesu laa komaan sama kàrt bu bees bi, ñaata waxtu laa war a xaar ngir jot ci ?
card arrival
Could I get a mastercard if that's reasonable?
Puis-je obtenir une Mastercard si cela est raisonnable ?
Ndax, su yenoo maanaa, mën na am ab kàrtu Mastercard ?
visa or mastercard
Is there a charge for exchanging foreign currencies?
Y a-t-il des frais pour l’échange de devises étrangères ?
Ndax amna ay fere ngir weccoo xaalis bitim réew?
exchange charge
I'm interested in learning more about disposable virtual cards.
Je souhaite en savoir plus sur les cartes virtuelles jetables.
Bëgg naa gën a am ay leeral ci kàrt yu xarala yi nga xam ne benn yoon lañu leen di jëfandikoo
get disposable virtual card
Let me know when I get charged extra for payments. I saw on the app a fee I wasn't forewarned about.
Prévenez-moi si des frais supplémentaires sont facturés. J'ai vu sur l'application des frais dont je n'avais pas été informé.
Xamuma ndax dañu teg yeneeni fere ci peyoor yi. Gis naa ci aplikaasiyoŋ ay fere yoo xam ne kenn yëgaluma ko.
card payment fee charged
There is some odd 1£ charge that appears as pending on my statement. What's that about? Pretty sure I haven't purchased anything for a pound there.
Il y a un étrange débit de 1 £ qui apparaît comme en attente sur mon relevé. De quoi s'agit-il ? Je suis presque sûr de n'avoir rien acheté pour une livre là-bas.
Am na benn fere buy tollu ci benn pound ci sama karne kont. Lan lay màndargaal ? Daanaka leer na ma ne jënduma dara luy jar benn pound
extra charge on statement
It seems that something went wrong with my exchange. I changed Russian Ruble into UK pounds but have been charged entirely too much!
Il semblerait qu'il y ait eu un problème avec mon échange. J'ai changé des roubles russes en livres sterling, mais le montant facturé est bien trop élevé !
Dafa mel ni am na woroo ci sama weccoo gi. Xaalisu waa Russie (rouble) laa weccook xaalisu waa àngalteer (livre sterling), waaye li mu ma dikke dafa seer lool.
card payment wrong exchange rate
What does the €1 fee mean?
Que signifie la taxe de 1 € ?
Lan la ferey benn euro bi wundu ?
extra charge on statement
Can I get a new card in China?
Puis-je obtenir une nouvelle carte en Chine ?
Ndax mën naa am kàrt bu bees Chine ?
card about to expire
I was just going over my transactions for the past couple of months and noticed a large type charge that I know I did not make. Even though it's been a while can I please still dispute this?
Je passais en revue mes transactions des deux derniers mois et j'ai remarqué un gros débit que je ne suis pas responsable. Même si cela fait un moment, puis-je quand même le contester ?
Maa ngi doog a xool jokkalante koppar yi ma def ci ñaari weer yii weesu, waaye gis naa xaalis bu bare bu ñu ci jël te du man. Donte sax loolu xaw na yàgg, ndax mën naa ko jéebaane ?
direct debit payment not recognised
Will I see fees from adding money with an international card?
Vais-je devoir payer des frais si j'ajoute de l'argent avec une carte internationale ?
Ndax su ma yokkee xaalis ak kàrtu bitim-réew dama war a fey yeneen fere ?
top up by card charge
I exchanged cash when traveling and the rate was incorrect.
J'ai échangé de l'argent liquide lors d'un voyage et le taux était incorrect.
Weccoo naa xaalis xobbet-xobbet bi ma doon tukki, waaye dayo weccoo bi jaarul woon yoon
wrong exchange rate for cash withdrawal
My cheque is slow to cash
Mon chèque est lent à encaisser
Dama yeex a jot ci sama xaalisu seg bi
balance not updated after cheque or cash deposit
What is the charge for receiving a SEPA transfer?
Quels sont les frais pour recevoir un virement SEPA ?
Yan ñooy fere jotale xaalis boo xam ne xeetu yónnee bii di SEPA lañu ko jaarele ?
top up by bank transfer charge
My payment was put back, I think.
Mon paiement a été reporté, je crois.
Sama peyoor bi dañu ko dàkkandil, ci sama yaakaar
reverted card payment?
How much will it be in order to pay with a bank transfer using SEPA?
Combien cela coûtera-t-il de payer par virement bancaire via SEPA ?
Lan mooy njëgu jokkalante xaalis bu jaare ci sistemu SEPA ?
top up by bank transfer charge
Do you offer SWIFT transfers?
Proposez-vous des virements SWIFT ?
Ndax am ngeen xalaat ci xaalis buy jaar SWIFT?
top up by bank transfer charge
How long does transfers take?
Combien de temps prennent les transferts ?
Ñaata waxtu la xaalis bu ñu yónnee war a def ?
balance not updated after bank transfer
Is there a top up fee for transfer?
Is there a top up fee for transfer?
Ndax jokkalantey koppar yi dañoo am yeneen fere ?
top up by bank transfer charge
Is there a specific source that the exchange rate for the transfer I'm planning on making is pulled from?
Existe-t-il une source spécifique à partir de laquelle le taux de change pour le transfert que je prévois d'effectuer est tiré ?
Ndax dayo weccoo xaalis bi may waaj a yónne am na coslaay ?
exchange rate
my statement contains an unknown payment
mon relevé contient un paiement inconnu
Gis naa ci sama kont peyoor boo xam ne yëguma ko.
card payment not recognised
In my app, a direct debit payment I didn't do shows in my app
Dans mon application, un paiement par prélèvement automatique que je n'ai pas effectué s'affiche dans mon application
Ci sama aplikaasioŋ, payoor buma deful dafay wane ci sama aplikaasioŋ
direct debit payment not recognised
How do I know if my top-up went through?
Comment savoir si ma recharge a été effectuée ?
Naka laa mën a xamee ndax li ma sarse dugg na ?
pending top up
Can someone in the US have a card?
Quelqu’un aux États-Unis peut-il avoir une carte ?
Ndax ku nekk Amerig mën na am ab kàrt ?
country support
How does your app transfer the money
Comment votre application transfère-t-elle l'argent ?
Naka la seen aplikaasiyoŋ bi di yónnee xaalis bi ?
transfer into account
After making a transfer from a UK account it's not showing up. How long do these transfers normally take for you? I want to be certain everything is all right.
Après avoir effectué un virement depuis un compte britannique, il n'apparaît pas. Combien de temps prennent généralement ces virements chez vous ? Je veux être sûr que tout se passe bien.
Ginnaaw bi defee ab wiirmã ak ab kont àngalteer, ba tay yegseegul. Ñaata waxtu la xeeti jokkalante yooyu di faral di jël ? Dama bëgg a xam ndax lépp a ngi tege ci yoon
balance not updated after bank transfer
Can I reactivate a card?
Puis-je réactiver une carte ?
Ndax mën naa doxalaat sama kàrt ?
card linking
Why do I see extra charges for withdrawing my money?
Pourquoi est-ce que je vois des frais supplémentaires lorsque je retire mon argent ?
Lu tax njëlum xaalis di laaj yeneen fere ?
cash withdrawal charge
I accidentally left my phone at the hotel so now I'm not able to use the app.
J'ai accidentellement laissé mon téléphone à l'hôtel, donc je ne peux plus utiliser l'application.
Dama fàtte sama telefon ca wotel ba, mënatuma jëfandikoo aplikaasiyoŋ bi
lost or stolen phone
can i get a card if I live in the usa?
Puis-je obtenir une carte si je vis aux États-Unis ?
Ndax mën naa am kàrt su ma dëkkee Etats-Unis ?
country support
When I purchased a product in another country the currency exchange was incorrect.
Lorsque j'ai acheté un produit dans un autre pays, le taux de change était incorrect.
Bi ma jëndee benn afeer ca bitim-réew, dayo weccoo xaalis bi jaarul woon yoon
card payment wrong exchange rate
What are age requirements for opening an account?
Quelles sont les conditions d’âge pour ouvrir un compte ?
Ci yan at la ubbi ab kont aju ?
age limit
Did I do something incorrectly? Where is my top-up?
Ai-je fait une erreur ? Où est ma recharge ?
Ndax dama juum walla ? Fan la xaalis bi ma dugal nekk ?
pending top up
I've changed my mind on an item. How do I get a refund?
J'ai changé d'avis sur un article. Comment obtenir un remboursement ?
Maa ngi xel-yaar ci benn afeer. Naka laa mën a fexee ba ngeen delloo ma sama xaalis ?
request refund
Are currency exchanges free?
Les échanges de devises sont-ils gratuits ?
Ndax weccoo xaalis yi amna fey?
exchange charge
There is a duplicate charge on my account.
Il y a des frais en double sur mon compte.
Amna ay njëg yuy feeñ ñaari yoon ci sama kontu.
transaction charged twice
I thought I lost my card so I cancelled it, but recently I found it in my jacket and I would like to re-establish the card.
Je pensais avoir perdu ma carte alors je l'ai annulée, mais récemment je l'ai retrouvée dans ma veste et j'aimerais rétablir la carte.
Dama yaakaaroon ne dama dafa réer, ma niilal ko, waaye dama ko gis ci sama poosu west bi, dama ko bëggoon a doxalaat.
card linking
why would a merchant refuse a payment
pourquoi un commerçant refuserait-il un paiement
Lu tax ab jaaykat gàntal peyoor bi ?
reverted card payment?
The exchange rate applied is wrong for my international purchase.
Le taux de change appliqué est erroné pour mon achat international.
Njëgu weccoo bi ñu def jaarul yoon li ma jënd bitim réew.
card payment wrong exchange rate
How long do bank transfers take to clear
Combien de temps faut-il pour que les virements bancaires soient traités ?
Ñaata waxtu laa war a toog ngir ñu delloo ma xaalis bi ma yónneewoon ?
balance not updated after bank transfer
It's only been a few weeks my my top-up got cancelled
Cela fait seulement quelques semaines que ma recharge a été annulée
Ay ayu-bés rekk la def bi ñu gàntalee xaalis bi ma doon dugal ci sama kont bi.
top up reverted
Can you tell me the status of my new card?
Pouvez-vous me dire où en est ma nouvelle carte ?
Ndax mën ngeen ma wax fu ngeen tollu ci sama kàrt bu bees bi ?
lost or stolen card
I didn't withdraw the amount of cash that is showing up in the app.
Je n'ai pas retiré le montant d'argent qui apparaît dans l'application.
Jëluma xaalis bu tollu ne bi aplikaasiyoŋ fësal
cash withdrawal not recognised
Can I change my pin number at a cash machine?
Puis-je changer mon code PIN à un distributeur automatique de billets ?
Ndax mën naa soppiwee sama kod PIN ci ab GAB ?
change pin
Can I cash deposit to top up my account
Puis-je déposer en espèces pour recharger mon compte
Ndax mën naa dugal xaalis ngir sarse sama kont
top up by cash or cheque
The ATM only gave me 10 pounds when I withdrew 30. What do I do?
Le distributeur ne m'a donné que 10 livres alors que j'en ai retiré 30. Que dois-je faire ?
GAB 10i pound la ma génneel, te 30 laa ko laajoon. Lan laa war a def ?
wrong amount of cash received
When can I expect my card?
Quand puis-je attendre ma carte ?
Kañ laa mëna seentu sama kàrt?
card delivery estimate
Is there a way I can get a Visa card?
Existe-t-il un moyen d’obtenir une carte Visa ?
Ndax am na fu ma mën a amee ab kàrtu Visa ?
visa or mastercard
I noticed an extra pound charge?
J'ai remarqué une charge supplémentaire d'une livre ?
Seetlu naa ne faktiire nañu ma beneen pound
extra charge on statement
Why can't I see my refund in my statement?
Pourquoi ne puis-je pas voir mon remboursement sur mon relevé ?
Lu tax xaalis bi ñu ma delloo feeñul ci sama karne kont ?
Refund not showing up
Has my card been lost in delivery?
Ma carte a-t-elle été perdue lors de la livraison ?
Ndax sama kàrt dafa réer ci bi ñu koy yóbbu?
card arrival
Why was I charged an extra fee when using the card?
Pourquoi des frais supplémentaires m'ont-ils été facturés lors de l'utilisation de la carte ?
Lu tax ñu teg ma yeneen fere bi ma jëfandikoo sama kàrt ?
card payment fee charged
do i need to add money before i order a card
dois-je ajouter de l'argent avant de commander une carte
Ndax dama war a fey laataa may komànde ab kàrt ?
order physical card
Tell me what the steps for the identity checks are
Dites-moi quelles sont les étapes des contrôles d'identité
Wax ma lan mooy jéego yi ngir saytu dàntite
verify my identity
If my card is going to expire this month, do I need to order a new one?
Si ma carte expire ce mois-ci, dois-je en commander une nouvelle ?
Su sama kart jeexe ci weer wii, ndax dama wara defarlu bu bees?
card about to expire
When is a payment I made with my card going to clear>
Quand un paiement que j'ai effectué avec ma carte sera-t-il compensé ?
Kañ la peyoor bu ma defe ak sama kàrt di jàll ?
pending card payment
I still have not received an answer as to why I was charged $1.00 in a transaction?
Je n'ai toujours pas reçu de réponse quant à la raison pour laquelle j'ai été facturé 1,00 $ lors d'une transaction ?
Ba tay amuma benn tontu ci sama laaj bi ñeel lu tax ñu faktiire ma benn dolaar ?
extra charge on statement
Help me close my account.
Aidez-moi à fermer mon compte.
Jàppaleleen ma ngir téj sama kont
terminate account
Payment did not process
Le paiement n'a pas été traité
Peyoor bi kenn cambaru ko
beneficiary not allowed
Can you delete the account?
Pouvez-vous supprimer le compte ?
Naka laa mën faree sama kont ?
terminate account
I can't see my refund in my history.
Je ne vois pas mon remboursement dans mon historique.
Gisuma xaalis biñ ma delloo ci sama taarix.
Refund not showing up
I was trying to use my card and it was declined, when I tried to find out what happened I found cash withdraw for $500 that I didn't do. Can you please help figure this out?
J'ai essayé d'utiliser ma carte et elle a été refusée. En cherchant la cause du problème, j'ai découvert un retrait de 500 $ que je n'avais pas effectué. Pourriez-vous m'aider à résoudre ce problème ?
Jéem naa jëfandikoo sama kàrt waaye nangu wuñu ko. Bi may wër li waral jafe-jafe bi, ma gis ni dañu ma dindi 500Fte deful ko. Mën ngama jàppale ma saafara jafe-jafe bii?
cash withdrawal not recognised
How long does it take for money to transfer? I sent some to a friend and it hasn't gone through yet.
Combien de temps faut-il pour que l'argent soit transféré ? J'en ai envoyé à un ami et il n'a pas encore été envoyé.
Ban diir ngay def balaa xaalis bi ñu yonnee di dem? Yonnee naa sama benn xarit te ba leegi yónnee guñu ko.
transfer not received by recipient
What number of transactions can i do with one disposable card?
Combien de transactions puis-je effectuer avec une carte jetable ?
Ñaata jëflante laa mëna def ak kàrt bu ñuy sànni?
disposable card limits
Someone took my card without my permission.
Quelqu’un a pris ma carte sans ma permission.
Am na ku jël sama kàrt te joxumako ndigël.
lost or stolen card
My balance doesn't show my deposit.
Mon solde n'indique pas mon dépôt.
Xaalis bi des sama kont wane wul ni duggal naa ci xaalis
balance not updated after cheque or cash deposit