input
stringlengths
13
433
input_fr
stringlengths
2
469
input_wo
stringlengths
15
414
label
stringclasses
77 values
How do I switch to a different currency?
Comment puis-je passer à une autre devise ?
Naka laay mëna jàllee ci benenn xaalis?
exchange via app
What are the fees for using transfer to top off my account?
Quels sont les frais liés à l'utilisation d'un virement pour recharger mon compte ?
Yañ ñooy fere yi laale ak dugal xaalis ngir sarse sama kont ?
top up by bank transfer charge
is there something blocking me from making transfers
y a-t-il quelque chose qui m'empêche d'effectuer des transferts
Amna lumay tere def ay yóonee xaalis
beneficiary not allowed
I did a transfer but its still pending
J'ai effectué un transfert mais il est toujours en attente
Yónnee xaalis waaye ba tay jàllagul
pending transfer
What's the card you sent me's tracking number?
Quel est le numéro de suivi de la carte que vous m'avez envoyée ?
Lan mooy limu topp kàrt bi nga ma yónnee ?
card arrival
I was overcharged an additional pound.
On m'a facturé une livre supplémentaire.
Fayloo nanu ma benn pound bu ëpp
extra charge on statement
How can I report that my card was stolen? I made a police report first.
Comment puis-je signaler le vol de ma carte ? J’ai d’abord fait un rapport de police.
naka lay def ba wane ni dañu sàcc sama kàrt? Def naa benn rapoor ci poliis.
lost or stolen card
Why is my top-up showing as reverted?
Pourquoi ma recharge apparaît-elle comme annulée ?
Lu tax sama sarsamã di feeñe ne bu jàllagul ?
top up reverted
Was I charged more than I should of been for a currency exchange?
Est-ce que j'ai été facturé plus que ce que j'aurais dû pour un échange de devises ?
Ndax dañu ma faktiire lu ëpp ci ab weccoo xaalis ?
card payment wrong exchange rate
There was a strange transaction made on my account a couple weeks ago by a seller I don't recognize. May you please check on this transaction for me.
Il y a quelques semaines, une étrange transaction a été effectuée sur mon compte par un vendeur que je ne connais pas. Pouvez-vous s'il vous plaît vérifier cette transaction pour moi.
Ayu-bis yu néew ci ginaaw, amna ab jëflante bu doy waar bu ab jaaykat bu ma xamul def ci sama kont. Ndax mën ngeen xoolat jëflante bii?
direct debit payment not recognised
Can i receive transfers from my employer to this account?
Puis-je recevoir des virements de mon employeur vers ce compte ?
Ndax mën naa jot toxal xaalis ci sama patroŋ ci kontu bii?
receiving money
There was a direct debit from my account and I didn't authorise it
Il y a eu un prélèvement automatique sur mon compte et je ne l'ai pas autorisé
Amna luñu dindi ci saasi ci sama kont te nangu wuma ko
direct debit payment not recognised
I just checked and my payment was cancelled, why?
Je viens de vérifier et mon paiement a été annulé, pourquoi ?
Maa ngi doog a xool, waaye peyoor bi dañu ko niilal, lu ko waral ?
reverted card payment?
There's a weird payment showing in my app that I definitely haven't made myself, as I haven't used the card at all that day. Please cancel that and return my money.
Un paiement étrange s'affiche sur mon application, mais je ne l'ai certainement pas effectué moi-même, car je n'ai pas du tout utilisé la carte ce jour-là. Veuillez l'annuler et me rembourser.
Sama applikaasioŋ bi dafay wane ab payoor bu doywaar, waaye man gëm naani defumako, ndax bis boobu jëfandikoo wuma kàrt bi. Baalma nga fomm ko te delloma xaalis bi.
direct debit payment not recognised
how to exchange currencies
comment échanger des devises
Naka lañuy weccoo ay xeeti xaalis ?
exchange via app
How many cards can I have?
Combien de cartes puis-je avoir ?
Ñaata kart laa mëna am?
getting spare card
Can i set up an auto top-up?
Puis-je configurer une recharge automatique ?
Ndax mën naa defar ab jumtuwaaye dugal xaalis bu gaaw ?
automatic top up
My preference is Mastercard.
Ma préférence va à Mastercard.
Mastercard mooy sama tànneef
visa or mastercard
Is my top up not working?
Ma recharge ne fonctionne pas ?
Sama sarsamã doxatul
pending top up
What should I do if my smart phone is lost or stolen?
Que dois-je faire si mon smartphone est perdu ou volé ?
Lan laa war a def bu fekkee dañu sàcc walla ma réeral sama telefon bu xarala bi ?
lost or stolen phone
I don't see a money transfer yet
Je ne vois pas encore de transfert d'argent
Ba leegi gisuma benn yóonee xaalis
pending transfer
terminate my account please
veuillez résilier mon compte
Na nga dindi sama kontu.
terminate account
Do you have a tracking number for the card I was sent?
Avez-vous un numéro de suivi pour la carte qui m'a été envoyée ?
Ndax am na nimero buy saytu kàrt bi ñu ma yónne ?
card arrival
Can I top up with cash
Puis-je recharger avec de l'argent liquide ?
Ndax mën naa fey xobbet-xobbet ?
top up by cash or cheque
Is there a fee when I get cash from an ATM? Is there a limit I can take out? If there is a fee, what is it?
Y a-t-il des frais lorsque je retire de l'argent à un distributeur automatique ? Y a-t-il une limite de retrait ? Si des frais sont appliqués, quels sont-ils ?
Ndax su ma jëlee xaalis ci ab GAB dafay am aya fere ? Ndax dafa am limu xaalis boo xam ne waruma ko weesu ? Su fekkee dafay am ay fere, ci ñaata lay tollu ?
cash withdrawal charge
Do top-ups have a limit?
Les recharges ont-elles une limite ?
Ndax sarsamã yi dañu am aw dig ?
top up limits
Do I have to pay for a second card?
Dois-je payer pour une deuxième carte ?
Ndax dama war a jënd beneen kàrt ?
getting spare card
Where can I see where my funds came from?
Où puis-je voir d’où viennent mes fonds ?
Fan laa mën a gisee fi samay koppar jóge ?
verify source of funds
Will my new card work outside of the EU?
Ma nouvelle carte fonctionnera-t-elle en dehors de l’UE ?
Ndax sama kàrt bu bees bi dafay dox feneen fu dul ci UE bi ?
country support
I have a contactless that's broken.
J'ai un sans contact qui est cassé.
Amnaa benn kart bu damm.
contactless not working
I made an ATM withdraw it didn't give me the amount I asked for but is showing a withdraw for that amount.
J'ai effectué un retrait au guichet automatique, il ne m'a pas donné le montant que j'avais demandé, mais il affiche un retrait pour ce montant.
Jël naa ab xaalis ci ab GAB, joxuma xaalis bi ma ko laajoon, waaye feeñ na ci kont
wrong amount of cash received
why have i not got my new card?
pourquoi n'ai-je pas reçu ma nouvelle carte ?
Lu tax jota guma sama kàrt bu bees bi?
card arrival
I have no way to prove my identity.
Je n’ai aucun moyen de prouver mon identité.
Amuma benn anam ngir firdeel sama dàntite.
unable to verify identity
Does a US transfer take long
Un transfert aux États-Unis prend-il beaucoup de temps ?
Ndax yónnee xaalis Etats-Unis dafay yàgg ?
transfer timing
Am I supposed to verify my identity?
Suis-je censé vérifier mon identité ?
Ndax man maa war a cambar sama dàntite ?
why verify identity
Why was a fee added to my bill when I used my card?
Pourquoi des frais ont-ils été ajoutés à ma facture lorsque j'ai utilisé ma carte ?
Lu tax may fey ay fere su ma jëfandikoo sama kàrt ?
card payment fee charged
I'd like to have extra cards. Will I have to pay for that?
J'aimerais avoir des cartes supplémentaires. Devrai-je payer pour cela ?
Dama bëggoon yeneen kàrt.Ndax dama war a fey ngir loolu ?
getting spare card
Can I use the app without my phone?
Puis-je utiliser l'application sans mon téléphone ?
Ndax mën naa jëfandikoo aplikaasiyoŋ bi su ma yorewul sama telefon ?
lost or stolen phone
This card payment isn't is recognition.
Ce paiement par carte n’est pas une reconnaissance.
Payoor ak kàrt bii pay bii xàmmee wuñu ko.
card payment not recognised
Need a new passcode.
Besoin d'un nouveau mot de passe.
Dama bëgg beneen baatu jàll
passcode forgotten
Can this card be used at all ATMs?
Cette carte peut-elle être utilisée dans tous les distributeurs automatiques de billets ?
Ndax mën nañoo jëfandikoo kàrt bii ci GAB yépp ?
atm support
I have the cash already, my account still shows up as pending. How can my account be still pending?
J'ai déjà l'argent, mais mon compte est toujours en attente. Comment se fait-il que mon compte soit toujours en attente ?
Maa ngi ak xaalis bi, waaye sama kontu mingi xaar ba leegi. Naka la mëna demee ni sama kontu mingi xaar ba leegi.
pending cash withdrawal
There is a vendor name I don't recognize on a payment from my account. I don't think I made this payment.
Il y a un nom de fournisseur que je ne reconnais pas sur un paiement effectué sur mon compte. Je ne pense pas avoir effectué ce paiement.
Amna benn jëflante ci sama kont bu ma xameewul. Fooguma ni maa ko def.
card payment not recognised
Im not sure why Im being charged an extra fee just for purchasing an item from another country? I paid for the item and the shipping why am I getting charged extra?
Je ne comprends pas pourquoi des frais supplémentaires me sont facturés simplement pour l'achat d'un article dans un autre pays. J'ai payé l'article et les frais de livraison. Pourquoi dois-je payer un supplément ?
Xamuma lu tax ñu teg ma yeneen fere ci benn afeer bu ma jënde ci meneen réew. Fey naa njëgu afeer bi ak ferey yónnee yi. Lu tax ma war a fey yeneen fere ,
transfer fee charged
What does my daughter need to open an account?
De quoi ma fille a-t-elle besoin pour ouvrir un compte ?
Lan la sama doom ju jigéen soxla ngir mëna ubbi kont?
age limit
daughter needs card, how do i add her
ma fille a besoin d'une carte, comment puis-je l'ajouter
Sama doom dafa yittewoo ab kàrt, naka laa ko ko mën a fàggulee ?
getting spare card
My payment had a wrong exchange rate.
Mon paiement avait un taux de change erroné.
Sama payoor amoon na njëgu weccoo xaalis bu jaarul yoon.
card payment wrong exchange rate
Do you charge a fee on currency exchange?
Est-ce que vous facturez des frais sur le change de devises ?
Ndax dangeen di faktiire ay fere ci xeeti xaalis yi ?
exchange charge
Why isn't my beneficiary allowed?
Pourquoi mon bénéficiaire n'est-il pas autorisé ?
Lu tax sama ngënéel ma mayewuñu ko?
beneficiary not allowed
Why is top up not working if I use my American express with my apple pay?
Pourquoi la recharge ne fonctionne-t-elle pas si j'utilise ma carte American Express avec mon Apple Pay ?
Lu tax sarse bi du dox sudee damay jëfandikoo sama kartu Senegaal Express ak sama Apple Pay?
apple pay or google pay
How long does it take for a pending cash withdrawal?
Combien de temps faut-il pour un retrait d'espèces en attente ?
Ban diir la wara def ngir génnee xaalis buy xaar?
pending cash withdrawal
Is there an exchange rate?
Y a-t-il un taux de change ?
Ndax amna njëgu weccoo xaalis
exchange rate
My cash deposit hasn't posted to my account.
Mon dépôt en espèces n'a pas été crédité sur mon compte.
Sama xaalis bima dugalonn kenn yobbu ko ci kont bi
balance not updated after cheque or cash deposit
I'm not sure how to provide my identity.
Je ne sais pas comment fournir mon identité.
Xamuma naka laay wonee sama dàntite
unable to verify identity
Where is my PIN?
Où est mon code PIN ?
Fan la sama kod PIN nekk ?
get physical card
I was mistakenly charged a fee for using my card.
Des frais m'ont été facturés par erreur pour l'utilisation de ma carte.
Dañu ma faktiire, ci njuumte, ay fere bi may jëfandikoo sama kàrt
card payment fee charged
How much does it cost to us US cards?
Combien nous coûtent les cartes américaines ?
Ñaata la kàrt Senegaal yi di jar ?
top up by card charge
can I have multiple currencies?
Puis-je avoir plusieurs devises ?
Ndax mën naa am xaalis yu bari?
fiat currency support
How do I change my name?
Comment puis-je changer mon nom ?
Naka laa mëna soppee sama tur.
edit personal details
I need to order a new card, can you please direct me to the virtual cards?
J'ai besoin de commander une nouvelle carte, pouvez-vous s'il vous plaît m'orienter vers les cartes virtuelles ?
Dama war a wut kàrt bu bees. Ndax mën nga ma won kàrti xarala yu méngook jamono yi.
getting virtual card
Can you tell me what is wrong ? I top-up with you all the time but this time it just shows my top-up as pending. What is happening?
Pouvez-vous me dire ce qui ne va pas ? Je recharge régulièrement chez vous, mais cette fois, mon compte est affiché comme étant en attente. Que se passe-t-il ?
Ndax mën ngeen ma wax lan mooy jafe-jafe bi ? Saa su ne ci yeen laay sarsee, waaye tay jii moom nanguwul. Lan moo xew ?
pending top up
I just made a top-up but it shows as pending! I use your service all the time and have never had a problem before. Why does it keep showing up as pending?
Je viens de faire une recharge, mais elle est en attente ! J'utilise régulièrement votre service et je n'ai jamais eu de problème auparavant. Pourquoi est-elle toujours en attente ?
Dama def leegi sarse, waaye mindi xaar! Damay faral di jëfandikoo sa serwiis te mësuma ama jafe-jafe?
pending top up
My card is stolen. Help!
Ma carte a été volée. À l'aide !
Sama kàrt dañu ko sàcc? Ndimbal!
lost or stolen card
I tried to buy something over the Internet yesterday and got a declined error. I tried again today and got the same message. What is the issue?
J'ai essayé d'acheter quelque chose en ligne hier et j'ai reçu un message d'erreur de refus. J'ai réessayé aujourd'hui et j'ai reçu le même message. Quel est le problème ?
Doon naa jéem a am lu ma doon jënd ci lënd gi démb, waaye dama jot bataaxal buy firndeel ne du mën a jàll. Tay itam loolu rekk la may bindalaat. Lan mooy jafe-jafe bi ?
declined transfer
How do I change to a different currency?
Comment puis-je changer de devise ?
naka laa mëna soppi xaalis?
exchange via app
where can i see money source?
où puis-je voir la source d'argent ?
Fan laa mën a gisee coslaayu xaalis bi ?
verify source of funds
Hello, a few days ago I transferred my rent check to my landlord, however, he is saying that it has not gone though. On my end everything looks fine and I double checked the account number. Is there anything else that could be holding up the check?
Bonjour, il y a quelques jours j'ai transféré mon chèque de loyer à mon propriétaire, cependant il me dit qu'il n'est pas encore parti. De mon côté, tout semble bien et j'ai vérifié le numéro de compte. Y a-t-il autre chose qui pourrait retarder le chèque ?
Nangeen def, fan yu néew ci ginaaw dama yóonee sama sekku luwaas boroom kër gi, waaye muni sekk bi ma demul ba leegi. Ci sama wàll, lépp jaar naa yoon te xool na limatu kont bi. Ndax amna leneen lu mëna téye sekk bi?
transfer not received by recipient
What is the top-up limit?
Quelle est la limite de rechargement ?
Lan mooy àppub dugal xaalis bi ?
top up limits
Where would I order a virtual card?
Où puis-je commander une carte virtuelle ?
Fan laa mën a komàndee ab kàrt wirtuyel ?
getting virtual card
I'm getting an error when trying to make a payment. I want to purchase a flat but my mortgage payment needs to go through. Can you help me?
Je reçois une erreur lors d'un paiement. Je souhaite acheter un appartement, mais je dois rembourser mon prêt immobilier. Pouvez-vous m'aider ?
Bataaxalu njuumte laaj jot su may jéem a def ab peyoor. Dama bëgg a jënd ag kër waaye dama war a fey sama boru tayle bi. Ndax mën ngeen ma ci jàppale ?
failed transfer
How do I fix a broken card?
Comment réparer une carte cassée ?
Naka lañuy defaraate kàrt bu toj ?
card not working
My top-up is still pending
Ma recharge est toujours en attente
Sama sarse baa ngi xaarandi ba leegi
pending top up
Where is the top-up verification code sent?
Où le code de vérification de recharge est-il envoyé ?
Fan lañuy yónnee baatu ubbikaayu sarse bi?
verify top up
I am wondering about a transfer from a different country that doesn't show up yet?
Je m'interroge sur un transfert depuis un autre pays qui n'apparaît pas encore ?
Maa ngi samp laaj ci xaalis boo xam ne ku nekk ci meneen réew a ma ko waroon a yónnee, te yegseegul ba tay
balance not updated after bank transfer
Is there a way I can get my card expedited?
Existe-t-il un moyen d’accélérer le traitement de ma carte ?
Ndax am nu ma mën a gaawale cambarug sama kàrt ?
card arrival
I haven't been sent my new pin!
Je n'ai pas reçu mon nouveau code PIN !
Jotaguma ci sama kod PIN bu bees bi
get physical card
My virtual card is just not going through.
Ma carte virtuelle ne passe tout simplement pas.
Sama kart wirtuel du jàll.
virtual card not working
Why am I being charged more on exchange with things I bought abroad?
Pourquoi me facture-t-on plus pour l'échange d'articles que j'ai achetés à l'étranger ?
Lan dayo weccoo bi gën a seer ci afeer yi ma jënde bitim-réew ?
card payment wrong exchange rate
Which merchants accept this card?
Quels commerçants acceptent cette carte ?
Yan jaaykat ñooy nangu kàrt bii?
card acceptance
Can my password be reset if I do not have it?
Mon mot de passe peut-il être réinitialisé si je ne l’ai pas ?
Ndax mën nañoo yeesalaat sama baatu jàll su fekee yorewuma ko
passcode forgotten
My card payment is being declined and I've tried several times.
Mon paiement par carte est refusé et j'ai essayé plusieurs fois.
Peyoor bi ma defee ak kàrt doxul, te jéem naa ba sonn.
declined card payment
Can you tell me the restrictions for the disposable cards?
Pouvez-vous me dire les restrictions concernant les cartes jetables ?
Ndax mën ngeen ma wax digi kàrt yi nga xam ne benn yoon rekk lañu leen di jëfandikoo ?
disposable card limits
I seem to be having trouble with my Google Pay Top. Can you please help?
J'ai des problèmes avec mon compte Google Pay Top. Pouvez-vous m'aider ?
Dama am ay jafe-jafe ci sama kontu Google Pay Top. Ndax mën ngama dimbali?
apple pay or google pay
I need a new card, my old card is expiring.
J'ai besoin d'une nouvelle carte, mon ancienne carte expire.
Dama yittewoo beneen kàrt, sama kàrt bi dafay waaj a jeex ?
card about to expire
Why was an extra charge added when I used my card?
Pourquoi des frais supplémentaires ont-ils été ajoutés lorsque j'ai utilisé ma carte ?
Lu tax ñu yokkal ma ay fere bi ma jëfandikoo sama kàrt ?
card payment fee charged
What kind of fee is there to top-up my account?
Quels sont les frais à payer pour recharger mon compte ?
Yan fere laa war a fey su may sarse sama kont ?
top up by bank transfer charge
Can you show me how to top up with Google play?
Pouvez-vous me montrer comment recharger avec Google Play ?
Ndax mën ngeen ma wax naka lañuy sarsee ak Google Pay ?
apple pay or google pay
I am yet to receive the money in my account how long will this take?
Je n'ai pas encore reçu l'argent sur mon compte, combien de temps cela prendra-t-il ?
Xaalis bi yegseegul ci sama kont, ñaata waxtu la war a jël ?
transfer timing
I would like to edit my personal information .
Je souhaiterais modifier mes informations personnelles.
Dama bëgga soppi samay leerali bopp.
edit personal details
I was getting cash and the card got stuck inside
J'étais en train de retirer de l'argent et la carte est restée coincée à l'intérieur
Dama doon jël xaalis ci ab GAB, kàrt bi kale fa.
card swallowed
When will my new card be delivered?
Quand ma nouvelle carte sera-t-elle livrée ?
Kañ lañuy indi sama kàrt bu bees bi?
card arrival
I am having trouble activating my card.
J'ai des difficultés à activer ma carte.
Mënuma doxal sama kàrt
activate my card
How do I order a replacement for stolen card?
Comment puis-je commander un remplacement de carte volée ?
Naka laa mëna defarloo kàrt ngir wecci kàrt buñu sàcc?
compromised card
I am on vacation in Spain and think someone saw my pin when… Can I change it at a local ATM?
Je suis en vacances en Espagne et je pense que quelqu'un a vu mon code PIN quand… Puis-je le changer à un distributeur automatique local ?
Maa ngi Espagne ci ab tukki, jàpp naa ne dafa am ku gis sama kod PIN bi may …Ndax mën naa ko soppi ci benn GAB mu nekk ci réew mi ?
change pin
I was the victim of someone stealing my wallet. My card is being used and it isn't me. What should I do?
On m'a volé mon portefeuille. Ma carte est utilisée et ce n'est pas moi. Que dois-je faire ?
Dañu sàcc sama kalpe. Am na keneen kuy jëfandikoo sama kàrt. Lan laa war a def ?
cash withdrawal not recognised
What reasons could cause my top up to be reverted
Quelles raisons pourraient entraîner l'annulation de mon rechargement ?
Yan ñooy sabab yi mën a tax ñu niilal xaalis bu ma bëgg a dugal ci sama kont ?
top up reverted
I wish to use my American Express to put funds into my account.
Je souhaite utiliser ma carte American Express pour déposer des fonds sur mon compte.
Dama bëgga jëfandikoo sama ekspres kàrt ngir dugal xaalis ci sama kontu.
supported cards and currencies
I need help fixing my contactless. It's not working anywhere I go today.
J’ai besoin d’aide pour réparer mon sans contact. Ça ne fonctionne nulle part où que je sois aujourd’hui.
Dama soxla jàppale ngir jëlaat sama baña jokkoo. Du dox fenn fu ma nekk tay.
contactless not working
I paid with a card and there is an extra charge. Why?
J'ai payé avec une carte et il y a un supplément. Pourquoi?
Dama feye ak kàrt te dafa am lu yokku ci payoor gi. Lu tax?
card payment fee charged
Why was the exchange rate so wrong when I bought something!
Pourquoi le taux de change était-il si erroné lorsque j’ai acheté quelque chose !
Lu tax njëgu weccoo xaalis bi jaarul yoon bima jëndee dara!
card payment wrong exchange rate