Dataset Viewer
Auto-converted to Parquet
input
stringlengths
13
433
input_fr
stringlengths
2
469
input_wo
stringlengths
15
414
label
stringclasses
77 values
i did not get any money but still was charged
je n'ai pas reçu d'argent mais j'ai quand même été facturé
Jotuma xaalis waaye terewul am na lu nu ma dagg.
wrong amount of cash received
Hello, Just now i got to know withdrawal of money from of my account. As someone used my card to withdraw amount in any odd remote area. Since i have not been in that area, please freeze my card immediately.
Bonjour, je viens d'apprendre qu'un retrait d'argent a eu lieu sur mon compte. Quelqu'un a utilisé ma carte pour retirer de l'argent dans une zone reculée. Comme je ne suis pas allé dans cette zone, veuillez bloquer ma carte immédiatement.
Salaamaalekum, maa ngi doog a yëg ne jël nañu xaalis ci sama kont. Mësuma dem ci béréb boobu, kon maa ngi sàkku ngeen bolokeel ma sama kàrt bi nu mu gën a gaawe. Segam mësuma dem ci diwaan boobu, maa ngi sàkku ñu boloke sama kàrt nu mu gën a gaawe
cash withdrawal not recognised
Why is my card payment pending?
Pourquoi mon paiement par carte est-il en attente ?
Lu tax sama peyooru kàrt jàllagul ?
pending card payment
Can I use top-up with Apple pay?
Puis-je utiliser une recharge avec Apple Pay ?
ndax mën naa jëfandikoo sarse ak Apple Pay?
apple pay or google pay
Why am I being charged a fee for using my card? If there is some print out of places that charge me can you please send me that?
Pourquoi me facture-t-on des frais pour l'utilisation de ma carte ? Si vous disposez d'une copie papier des établissements qui facturent des frais, pourriez-vous me l'envoyer ?
Lu tax ma war a fey ay fere su ma jëfandikoo sama kàrt ? Su fekke dafa am limu béréb yuy feyloo ay fere, ndax mën ngeen ma ko yónnee ?
card payment fee charged
Card activation steps
Étapes d'activation de la carte
Yooni aktiwe kàrt
activate my card
I have not used my card all day, however, there is an unusual payment showing in my app. I would like to have that amount reimbursed.
Je n’ai pas utilisé ma carte de la journée, cependant, il y a un paiement inhabituel qui s’affiche dans mon application. J’aimerais qu’on me rembourse ce montant.
Jëfandikoo wuma sama kàrt ci bis bi, waaye amna payoor bu wuute bu ñuy wane ci sama aplikaasioŋ. Bëgg naa ñu delloo ma xaalis bii.
direct debit payment not recognised
I want to give a second card for this account to my daughter, would this be possible?
Je souhaite donner une deuxième carte pour ce compte à ma fille, serait-ce possible ?
Dama bëggoon a jox ñaareelu kàrtu kont bi sama doom ju jigéen ji, ndax loolu mën na nekk ?
getting spare card
I was told to verify my identity, how do I do that?
On m'a dit de vérifier mon identité, comment puis-je faire ?
Dañu wax ne naa saytu sama dàntite, naka laa war a def ?
verify my identity
What to do if my physical card is not working?
Que faire si ma carte physique ne fonctionne pas ?
Luma wara def sudee sama kàrt fisik doxul.
card not working
Which fiat currencies are supported for holding and exchanging?
Quelles monnaies fiduciaires sont prises en charge pour la détention et l'échange ?
Yan ñooy xeeti xaalisi kóolute yi ngeen di jëfandikoo ngeen weccoo bi ?
fiat currency support
Remove my account immediately.
Supprimez mon compte immédiatement.
Far leen sama kont ci nu mu gën a gaawe.
terminate account
I'm cancelling this charge. I still have not received what I bought from these people a while ago.
J’annule ces frais. Je n’ai toujours pas reçu ce que j’ai acheté de ces gens il y a quelque temps.
Damay fomm njëg yii. Ba leegi jotuma li ma jëndoon ci nit ñooñu amna ay waxtu ci ginaaw.
request refund
I've just moved and I need to change my details
Je viens d'emménager et je dois modifier mes coordonnées
Maa ngi doog a tuxu, dama bëggoon a soppi samay wayndare
edit personal details
How can I change my information?
Comment puis-je modifier mes informations ?
Naka laa mëna soppee samay leeral?
edit personal details
how do i see what i transferred
comment puis-je voir ce que j'ai transféré
Naka laa mën gisee li ma yónnee ?
balance not updated after bank transfer
I had an unexpected fee
J'ai eu des frais inattendus
Dama am ay fere yuma xaarul woon.
transfer fee charged
What kind of fiat currencies are supported for holding and exchange?
Quels types de monnaies fiduciaires sont pris en charge pour la détention et l'échange ?
Yan ñooy xeeti xaalisi kóolute yi ñu nangu ngir wecco bi ?
fiat currency support
My money has gone missing. I had recently added money in, and saw it was there and went through. Now it's missing. What is happening?
Mon argent a disparu. J'avais récemment ajouté de l'argent, je l'ai vu et je l'ai utilisé. Maintenant, il a disparu. Que se passe-t-il ?
Sama xaalis neena mes. Sànq rekk laa ko doon yokk te seetlu woon naa ne mingi fi, ma wéyal, Léegi nag, neena mes. Lan moo xew ?
top up reverted
Do you have a return policy?
Avez-vous une politique de retour ?
Ndax am ngeen politigu delloo ?
request refund
Help me get the virtual card working.
Aidez-moi à faire fonctionner la carte virtuelle.
Jàppaleleen ma ngir ma doxal sama kàrtu xarala bi.
virtual card not working
I tried to transfer funds to a beneficiary and was denied. Can you tell me why?
J'ai essayé de transférer des fonds à un bénéficiaire et j'ai été refusé. Pouvez-vous me dire pourquoi ?
Jéem naa yónnee xaalis benn nit waaye da bañ. Mën ngeen ma wax luko waral?
beneficiary not allowed
What businesses can I use this card with?
Avec quelles entreprises puis-je utiliser cette carte ?
Yan yan xeeti jokkalante ci wàllu njënd ak njaay la mën a jëfandikoo kàrt bii ?
card acceptance
Can I change my PIN at a nearby ATM when in Spain? I think someone saw my PIN and I need to change it but am on vacation.
Puis-je changer mon code PIN à un distributeur automatique de billets à proximité en Espagne ? Je pense que quelqu'un a vu mon code PIN et je dois le changer, mais je suis en vacances.
Ndax mën naa soppi sama kodu PIN ci gab bi jege Espaañ ? Yaakaar naa ni amna ku gis sama kodu PIN, dama ko wara soppi te maa ngi ci wakaas.
change pin
Why did I not get my refund yet?
Pourquoi n'ai-je pas encore reçu mon remboursement ?
Lu tax jotaguma ci xaalis bi ñu ma waroon a delloo ?
Refund not showing up
Tell me what I need to do to activate my card.
Dites-moi ce que je dois faire pour activer ma carte.
Wax ma lan laa soxla ngir sama kàrt di dox ?
activate my card
On my statement, there is a strange 1£ charge that appears as pending. What's causing that? I haven't purchased anything that's just a pound.
Sur mon relevé, il y a un étrange débit de 1 £ qui apparaît comme en attente. Quelle est la cause ? Je n'ai rien acheté de plus d'une livre.
Ci sama karne kont, gis naa ci benn pound u fere boo xam ne jàllagul. Lan mooy sabab bi ? Jënduma dara luy jar benn dolaar
extra charge on statement
Why did my money disappear when I topped up??
Pourquoi mon argent a-t-il disparu lorsque j'ai rechargé ?
Lu tax gisatuma sama xaalis bi ma sarsee sama kàrt ?
top up reverted
Whats the process of tranfering money into an account?
Quel est le processus de transfert d’argent sur un compte ?
Lan mooy anam wi ñuy yónnee xaalis ci kontu?
transfer into account
what cards and currencies are accepted?
quelles cartes et devises sont acceptées ?
Ban kàrt ak ban xaalis lañuy nangu?
supported cards and currencies
I want to do a cash deposit to top up. How do I do this?
Je souhaite effectuer un dépôt en espèces pour recharger mon compte. Comment faire ?
Dama bëgg a dugal xaalis ngir feccali sama kont bi. Naka laa war a def ?
top up by cash or cheque
A transaction shows duplicate times.
Une transaction affiche des heures en double.
Ab yóonee mingi wane ñaari yoon ci ay waxtu.
transaction charged twice
I can not find my refund.
Je ne trouve pas mon remboursement.
Gisuma xaalis bi ñu a war a delloo
Refund not showing up
Can I get paid for this in another currency?
Puis-je être payé pour cela dans une autre devise ?
Ndax mënn ngeen ma fey ci beneen xeetu xaalis ?
receiving money
Is it possible to get a second card for my daughter?
Est-il possible d'obtenir une deuxième carte pour ma fille ?
Ndax mën naa am beneen kàrt ngir sama doom ju jigéen ji ?
getting spare card
There is a €1 extra fee in my statement
Il y a des frais supplémentaires de 1 € dans mon relevé
Amna yeneen njëg yu tollu ci 1fcfa ci sama rëlëwe.
extra charge on statement
I would like to cancel my account.
Je voudrais annuler mon compte.
Dama bëggoon a far sama kont
terminate account
I was charged multiple times for one purchase
J’ai été facturé plusieurs fois pour un seul achat
Dañu may fayeeku yoon yu bari ngir benn mbir buma jënd.
transaction charged twice
I don't recognize a charge on my statement.
Je ne reconnais pas de frais sur mon relevé.
Fere yi ma gis ci sama kont, xamuma lu tax mu nekk ci
card payment not recognised
My card has been found. Is there any way for me to put it back into the app?
Ma carte a été retrouvée. Puis-je la récupérer dans l'application ?
Gis naa sama kàrt. Ndax mën naa ko lëkkalewaat ak aplikaasiyoŋ bi ?
card linking
I would like to know how to work out where my funds came from?
Je voudrais savoir comment savoir d'où viennent mes fonds ?
Bëggoon naa xam naka lay xamee fu sama xaalis yi di jogee?
verify source of funds
Can you please check my UK Account to make sure everything went alright? I made the transfer a couple of hours ago.
Pouvez-vous vérifier mon compte britannique pour vous assurer que tout s'est bien passé ? J'ai effectué le virement il y a quelques heures.
Ndax mën ngeen a cambar sama kont ba nekk Royaume-Uni ngir ma xam ndax lépp a ngi dox ? Sànq laa yónnee xaalis bi
balance not updated after bank transfer
My card keeps getting declined when I try to use it. I would like to top-up, but it is not going though.
Ma carte est toujours refusée lorsque j'essaie de l'utiliser. J'aimerais la recharger, mais je n'y parviens pas.
Sama kàrt dañu ko bañ ba leegi. Bëggoon naa ko sarse, waaye mënu ma ko.
top up failed
How can I use my credit card to transfer money?
Comment puis-je utiliser ma carte de crédit pour transférer de l'argent ?
Nan laa mëna jëfandikoo sama kart kredi ngir yónnee xaalis?
topping up by card
Can I deposit money using Apple Pay?
Puis-je déposer de l'argent en utilisant Apple Pay ?
Ndax mën naa dugal xaalis ci Apple Pay?
apple pay or google pay
Do I have to go to the bank to change my PIN?
Dois-je me rendre à la banque pour changer mon code PIN ?
Ndax dama wara dem bànk ngir soppi sama kodu PIN?
change pin
I think my wallet fell out on the Tube today! I realized as soon as I got to my desk. How do I cut off the card?
Je crois que mon portefeuille est tombé dans le métro aujourd'hui ! Je m'en suis rendu compte dès que je suis arrivé à mon bureau. Comment couper la carte ?
Damaa yaakaar ni sama kalpe dafa réer ci metro bi tay! Bima yeggee ci sama bërabu ligéeyu kaay rek laako fattaliku. naka lañuy daggee kàrt bi?
lost or stolen card
i live in portugal. do you operate here?
j'habite au Portugal. Est-ce que vous opérez ici ?
Portugal laa dëkk, ndax foofu am na ay GAB ?
country support
The app is showing a payment I never made.
L'application affiche un paiement que je n'ai jamais effectué.
Aplikasioŋ bi dafay wane ab payoor bu ma mësul def.
card payment not recognised
Why has my top-up been returned to my account?
Pourquoi ma recharge a-t-elle été retournée sur mon compte ?
Lu tax ñu dugal sama sarsamã bi ci sama kont ?
top up reverted
The bank charged me fees for withdrawing cash!
La banque m'a facturé des frais pour retirer de l'argent !
Bànk bi dàgg na ma ay fere bi ma jëlee xaalis
cash withdrawal charge
Why is my identification required?
Pourquoi mon identification est-elle requise ?
Lu tax ñu laaj sama kayitu ràññeekaay?
why verify identity
I need to get a disposable virtual card?
J'ai besoin d'obtenir une carte virtuelle jetable ?
Yittewoo naa ab kàrtu xarala
get disposable virtual card
I tried to pay through my account but the payment is not going through. What's going on?
J'ai essayé de payer via mon compte mais le paiement n'a pas abouti. Que se passe-t-il?
Jéem naa fayee ak sama kont waaye demul. Lu xew ?
pending card payment
My morning transaction needs to be canceled.
Ma transaction du matin doit être annulée.
Sama jokkalanteb xaalis bi ma def ci suba si dees ko war a niilal.
cancel transfer
Why did you charge me extra when I withdrew cash?
Pourquoi m'avez-vous facturé un supplément lorsque j'ai retiré de l'argent ?
Lu tax ngeen teg ma yeneen fere bi may jël xaalis ?
cash withdrawal charge
Why are my payments not working and show pending?
Pourquoi mes paiements ne fonctionnent-ils pas et s'affichent-ils comme en attente ?
Lu tax samay peyoor duñu jàll ba noppi di wéy di nekk ci pekku négandiku ?
pending card payment
what is going on with my cash withdrawal? the exchange rate is wrong
Que se passe-t-il avec mon retrait d'espèces ? Le taux de change est erroné.
Lan moo xew ak sama dindi xaalis? Njëgu weccoo xaalis bi baaxul.
wrong exchange rate for cash withdrawal
I don't recognize this payment on my app, I am sure I didn't spend any money there.
Je ne reconnais pas ce paiement sur mon application, je suis sûr que je n’y ai pas dépensé d’argent.
Xàmmee wuma payoor bii ci sama aplikaasioŋ, gëm naani jëluma xaalis foofu.
card payment not recognised
Are there limits to businesses that will accept this card?
Existe-t-il des limites quant aux entreprises qui accepteront cette carte ?
Ndax am na yemuwaay ci bérébi njënd ak njaay yi nangu kàrt bii ?
card acceptance
The ATM keeps declining my card! I tried two different ATMs already can you please check if everything is alright with my account??
Le distributeur refuse ma carte sans arrêt ! J'ai déjà essayé deux distributeurs différents. Pourriez-vous vérifier si tout va bien sur mon compte ?
GAB nanguwul sama kàrt ba tay ! Jéem naa ko ci ñaari GAB yu wuute. Ndax mën ngeen ma cambaral sama kont ?
declined cash withdrawal
When I got cash I believe that the exchange rate was wrong
Quand j’ai eu de l’argent, je crois que le taux de change était mauvais
Bimay am xaalis, jàppoon naa ni njëgu weccoo xaalis bi baaxul woon.
wrong exchange rate for cash withdrawal
Why can't the recepient of my money transaction see it?
Pourquoi le destinataire de ma transaction monétaire ne peut-il pas la voir ?
Li tax ki ma waroon a yónnee xaalis bi gisu ko ?
transfer not received by recipient
Where do I get a disposable card
Où puis-je me procurer une carte jetable
Fan laa mëna amee kàrt bu ñuy sànni
get disposable virtual card
I just looked over my statement and I don't recognize the name of a card payment.
Je viens de consulter mon relevé et je ne reconnais pas le nom d'un paiement par carte.
Dama xool leegi sama jëflante te xame wu ma tur wi ñu feyee ci kàrt bi.
card payment not recognised
I tried to deposit a cheque into my account and it is not letting me.
J'ai essayé de déposer un chèque sur mon compte et cela ne me le permet pas.
Jéem naa dugal ab seg ci sama kont waaye mujjewul àntu
top up by cash or cheque
Can I use my salary for this?
Puis-je utiliser mon salaire pour cela ?
Ndax mën naa jëfandikoo sama saleer ngir loolu?
receiving money
What happens with the duplicate charge in my account?
Que se passe-t-il avec les frais en double sur mon compte ?
Lan moo war xaalis bi ñu dagg ñaari yoon ci sama kont ?
transaction charged twice
Is there a limit to how much I can top-up?
Y a-t-il une limite au montant que je peux recharger ?
Ndax xaalis bi ma mën sarse dafa am yemuwaay ?
top up limits
My transfer to another account was not allowed. Why is that?
Mon transfert vers un autre compte n'a pas été autorisé. Pourquoi ?
Sama yónnee ci beneen kont nangu wuñu ko. Lu tax ?
beneficiary not allowed
Could google pay and top up be together?
Google Pay et la recharge pourraient-ils être ensemble ?
Ndax Google Pay ak sarse mën nañu ànd?
apple pay or google pay
Somebody made a withdrawal from my account for 500. I have my card so how can this be? Does somebody have a duplicate card or something? Help please.
Quelqu'un a effectué un retrait de 500 $ sur mon compte. J'ai ma carte, comment est-ce possible ? Quelqu'un aurait-il un duplicata de ma carte ? À l'aide, s'il vous plaît.
Am na ku jëlee ci sama kont 500i euro, te maa ngi yore sama kàrt. Loolu naka la mën a nekkee ? Ndax dafa am keneen ku ci yore bu yem kepp walla lu ne mel. Jàppaleen ma ngir yàlla.
cash withdrawal not recognised
Where can I check out the source of available funds in my account?
Où puis-je vérifier la source des fonds disponibles sur mon compte ?
Fan laa mëna xamee xaalis bi des sama ci sama kont?
verify source of funds
How do I cancel a transaction?
Comment annuler une transaction ?
naka lañuy fommee ab jëflante?
cancel transfer
Why hasn't my card payment cleared yet?
Pourquoi mon paiement par carte n’a-t-il pas encore été compensé ?
Lutax peyoor bi ma defe ci sama kàrt bi jàllul batey.
pending card payment
Is it free to transfer money or is there a fee?
Le transfert d’argent est-il gratuit ou y a-t-il des frais ?
Ndax yónnee xaalis bi am na ay fere walla déet ?
transfer fee charged
Please help me find my top-up verification code
Aidez-moi à trouver mon code de vérification de recharge
Dimbali leen ma ma gis sama kodu saytu sarse.
verify top up
Why did the app deny my top-up?
Pourquoi l'application a refusé ma recharge ?
lutax aplikaasioŋ bi bañ sama saarse?
top up failed
I sent money to someone but they haven't gotten it, what's going on?
J’ai envoyé de l’argent à quelqu’un mais il ne l’a pas reçu, que se passe-t-il ?
Dama yónnee xaalis kenn waaye jotu ko, lu xew?
transfer not received by recipient
What do I do if I completed a money transfer but the recipient hasn't received it?
Que dois-je faire si j'ai effectué un transfert d'argent mais que le destinataire ne l'a pas reçu ?
Lan laa wara def sudee dama yóonee  xaalis waaye ki ma yóonee jotu ko?
transfer not received by recipient
After I attempted a transfer, it failed.
Après avoir tenté un transfert, celui-ci a échoué.
Ginnaaw bi ma jéemee, yónnee bi àntuwul
failed transfer
Can I tell what business will take this card?
Puis-je savoir quelle entreprise acceptera cette carte ?
Ndax mën naa xam ban bërëbu liggéeyukaay mooy nangu kart bii?
card acceptance
I need some help figuring out what this strange payment is on my account. It's stays pending and won't go away.
J'ai besoin d'aide pour comprendre ce paiement étrange sur mon compte. Il est en attente et ne disparaît pas.
Yittewoo naa ndimbal ngir lan la peyoor bu doy waar bii di def ci sama kont. Jàllul te maa ngi koy gis ba tay
extra charge on statement
I am just waiting on the completion of the transaction.
J'attends juste la finalisation de la transaction.
Maa ngi xaar jëflante bi dem.
transfer not received by recipient
I just replaced my phone so do I have to make a new account?
Je viens de remplacer mon téléphone, dois-je donc créer un nouveau compte ?
Dama soppi telefon, ndax dama war a tijji kont bu bees ?
lost or stolen phone
What do I do if I can't get my card out of the ATM?
Que dois-je faire si je ne parviens pas à retirer ma carte au distributeur automatique ?
Lu ma wara def suma mënula génnee sama kàrt ci gab bi?
card swallowed
I have two of the same charges on my account!
J'ai deux frais identiques sur mon compte !
Jël nañu ci sama kont ñaari fere yu niroo.
transaction charged twice
help me link my card
aidez-moi à lier ma carte
Jàppale ma ngir ma lëkkale sama kàrt
card linking
My transfer was declined. Why did this happen?
Mon transfert a été refusé. Pourquoi ?
Sama toxal dañu ko bañ. Lu tax?
declined transfer
How much could I top up?
Combien puis-je recharger ?
Ñaata laa mën a sarse ?
top up limits
Is it possible to have more than one disposable card?
Est-il possible d'avoir plus d'une carte jetable ?
Ndax mënees na am yeneen kart yi ñuy sànni?
disposable card limits
Why does top-up require verification?
Pourquoi la recharge nécessite-t-elle une vérification ?
Lu tax xaalis bi ma war a dugal soxla ag cambar ?
verify top up
Can you tell me what cards and currencies you support?
Pouvez-vous me dire quelles cartes et devises vous prenez en charge ?
mën nga maa wax ban kart ak ban xaalis ngay jël?
supported cards and currencies
What is the reason my payment was not accepted?
Quelle est la raison pour laquelle mon paiement n'a pas été accepté ?
Lan moo tax nanguwuñu sama peyoor?
declined card payment
I don't know where a direct debit payment came from
Je ne sais pas d'où vient un paiement par prélèvement automatique
Xamuma fan la fey ak jëlum xaalis bu gaaw bi jogee 
direct debit payment not recognised
Where can I use my Mastercard?
Où puis-je utiliser ma Mastercard ?
Fan laa mën a jëfandikoo sama kàrtu Mastercard ?
card acceptance
What is the extra fee that was added when I used the card?
Quels sont les frais supplémentaires qui ont été ajoutés lorsque j'ai utilisé la carte ?
Yan ñooy yeneen fere yi ñu ma feyloo bi ma jëfandikoo sama kàrt ?
card payment fee charged
Why is my transaction taking so long to complete?
Pourquoi ma transaction prend-elle autant de temps à se terminer ?
Lu tax jokkalante bi di yeex a jàll ?
transfer not received by recipient
Why wasn't it obvious that you charge for payments? If you put the fees in an easy to read format, this could have been avoided.
Pourquoi n'était-il pas évident que vous facturiez des paiements ? Si vous aviez présenté les frais de manière claire et lisible, cela aurait pu être évité.
Lu tax leeralu leen woon ne dangay di dagge ay fere ci peyoor yi ? Su fekkoon xamle ngeen ko ci anam wu yomb, loolu doon na mën a moytu jafe-jafe bii
card payment fee charged
May I order another card?
Puis-je commander une autre carte ?
Ndax mën naa komaande beneenkàrt?
getting spare card
End of preview. Expand in Data Studio

Intent classification models have made a lot of progress in recent years. However, previous studies primarily focus on high-resource languages datasets, which results in a gap for low-resource languages and for regions with a high rate of illiterate people where languages are more spoken than read or written. This is the case in Senegal, for example, where Wolof is spoken by around 90% of the population, with an illiteracy rate of 42% for the country. Wolof is actually spoken by more than 10 million people in West African region.

To tackle such limitations, we release a Wolof Banking Speech Intent Classification Dataset (WolBanking77), for academic research in intent classification. WolBanking77 currently contains 9,791 text sentences in the banking domain and more than 4 hours of spoken sentences.

This dataset is suitable for :

  • Customer Intent Detection
  • Machine Translation in French & Wolof
  • Automatic Speech Recognition in Wolof
  • Comparing different machine learning models for Intent Classification

Dataset Content:

  • text dir - Contains text dataset
  • audio dir - Contains audio dataset
  • train.csv – Text Training dataset (includes label target)
  • test.csv – Text Test dataset (no label target)
  • train.parquet - Audio Training dataset
  • test.parquet - Audio Test dataset
  • questions.csv - Customer queries
  • responses.csv - Bot responses

Target Variable:

  • label→ The client intent

Features:

  • input – Client’s query in English (text)
  • input_fr – Client’s query in French (text)
  • input_wo – Client’s query in Wolof (text)
  • label – Client's Intent (categorical)

License

CC BY 4.0 – Open for public use.

Inspiration

  • Can you predict the client intent?
  • How well do different machine learning models perform on this classification task?

Citation

To cite this work, please use the following reference:

@inproceedings{
    kandji2025wolbanking,
    title={WolBanking77: Wolof Banking Speech Intent Classification Dataset},
    author={Abdou Karim KANDJI and Frederic Precioso and Cheikh BA and Samba NDIAYE and Augustin NDIONE},
    booktitle={The Thirty-ninth Annual Conference on Neural Information Processing Systems Datasets and Benchmarks Track},
    year={2025},
    url={https://openreview.net/forum?id=7k0JBDeHAv}
}
@misc{
    kandji2025wolbanking77wolofbankingspeech,
    title={WolBanking77: Wolof Banking Speech Intent Classification Dataset}, 
    author={Abdou Karim Kandji and Frédéric Precioso and Cheikh Ba and Samba Ndiaye and Augustin Ndione},
    year={2025},
    eprint={2509.19271},
    archivePrefix={arXiv},
    primaryClass={cs.CL},
    url={https://arxiv.org/abs/2509.19271}, 
}
Downloads last month
18