Datasets:
Upload 8 files
Browse files- WolBanking77/audio/questions.csv +187 -0
- WolBanking77/audio/responses.csv +78 -0
- WolBanking77/audio/test.parquet +3 -0
- WolBanking77/audio/train.parquet +3 -0
- WolBanking77/text/5k_split/test/test.csv +0 -0
- WolBanking77/text/5k_split/train/train.csv +0 -0
- WolBanking77/text/full/test/test.csv +0 -0
- WolBanking77/text/full/train/train.csv +0 -0
WolBanking77/audio/questions.csv
ADDED
|
@@ -0,0 +1,187 @@
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
| 1 |
+
N°,text_fr,intent,text_wo,trans.
|
| 2 |
+
1,consulter le solde de mon compte,BALANCE,Seet sama tolluwaayu kont.,[seːt sama tolːuwaːyu kont]
|
| 3 |
+
2,je souhaiterais connaitre mes comptes merci beaucoup,BALANCE,Dama bëggoona xam fi sama kont tollu. Jarajëf.,[dama bëgːoːna xam fi sama kont tolːu. jaraɟëf]
|
| 4 |
+
3,Bonjour je vous appelle pour savoir quel était le montant du solde sur mon compte courant,BALANCE,Salaammalekum. Dama woote ngir xam ñaata moo des ci samay kont.,[salamːalekum. dama woːte ngir xam ñaːta moː des ci samay kont]
|
| 5 |
+
4,je veux savoir le solde de mon compte,BALANCE,Dama bëgga xam sama tolluwaayu kont.,[dama bëgːa xam sama tolːuwaːyu kont]
|
| 6 |
+
5,J'aimerais avoir plus d'informations sur le solde de mon compte en banque,BALANCE,Bëggoon naa am xibaar yu gêna yaatu ci tolluwaayu sama kontu bànk.,[bëgːoːn naː am xibaːr yu gëna yaːtu ci tolːuwaːyu sama kont bànk]
|
| 7 |
+
6,je veux connaitre le solde de mon compte,BALANCE,Bëgg naa xam tolluwaayu sama kont.,[bëgː naː xam tolːwaːyu sama kont]
|
| 8 |
+
7,Bonjour je vous appelle pour vous demander quel est le solde actuel de mon compte bancaire s'il vous plaît,BALANCE,"Ngéen baal ma, dama woote ngir laaj ñaata moo nekk ci sma kont fi ñu tollu.","[ngeːn baːl ma, dama woːte ngir laːj ñaːta moː nekː ci sama kont fi ñu tolːu]"
|
| 9 |
+
8,oui bonjour j'aurais besoin d'un petit renseignement est-ce que vous pouvez m'indiquer le solde de mon compte,BALANCE,"Waaw, salaamaaleekum. Ab tektal bu ndaw laa soxlawoon. Ndax mën ngéen maa wax fi sama kont tollu ?","[waːw, salaːmaːleːkum. ab tektal bu ndaw laː soxlawoːn. ndax mën ngeːn maː wax fi sama kont tolːu ?]"
|
| 10 |
+
9,quel est le solde de mon compte,BALANCE,Sama kont nu mu tollu ?,[sama kont nu mu tolːu ?]
|
| 11 |
+
10,Bonjour je voudrais savoir quel est mon solde sur mon compte courant,BALANCE,"Salaamaalekum, dama bëggoona xam sama tolluwaayu kont ","[salaːmaːlekum, dama bëgːoːna xam sama tolːwaːyu kont]"
|
| 12 |
+
11,quel est le solde de mon compte courant,BALANCE,Sama kont nu mu tollu ?,[sama kont nu mu tolːu]
|
| 13 |
+
12,je souhaiterais voir le solde de mon compte,BALANCE,Dama bëgoona gis tolluwaayu sama kont.,[dama bëgːoːna gis tolːuwaːyu sama kont]
|
| 14 |
+
13,je veux connaitre le solde de mon compte,BALANCE,Dama bëgga xam tolluwaayu sama kont,[dama bëgːa xam tolːuwaːyu sama kont]
|
| 15 |
+
14,appelle pour avoir des renseignements par rapport au solde de mon compte de mon compte courant,BALANCE,Wooteel ngir am ay tektal yu jëm ci tolluwaayu sa kont.,[woːteːl ngir am ay tektal yu jëm ci tolːuwaːyu sa kont]
|
| 16 |
+
15,expliquez-moi s'il vous plaît le solde de mon compte,BALANCE,Ngéen baal ma te leeralal ma sama tolluwaayu kont.,[ngeːn baːl ma te leːralal ma sama tolːuwaːyu kont]
|
| 17 |
+
16,oui allo bonjour j'aimerais connaitre le solde de mon compte courant s'il vous plait merci,BALANCE,"Waaw, aloo! Dama bëggoona xam sama tolluwaayu kont.","[waːw, aloː! dama bëgːoːna xam sama tolːuwaːyu kont]"
|
| 18 |
+
17,combien d'argent reste-t-il sur mon compte,BALANCE,Ñaata ci xaalis moo des ci sama kont ?,[ñaːta ci xaːlis moː des ci sama kont ?]
|
| 19 |
+
18,bonjour j'aimerais obtenir le solde de mon compte,BALANCE,Salaamaalekum dama bëggoona am tolluwaayu sama kont,[salaːmaːlekum dama bëgːoːna am tolːuwaːyu sama kont]
|
| 20 |
+
19,allo bonjour oui je vous appelle pour obtenir mon solde du compte courant merci,BALANCE,"Aloo! Salaamaalekum, waaw damay woote ngir am tolluwaayu sama kont. Jarajëf.","[aloː! salaːmaːlekum, waːw damay woːte ngir am tolːuwaːyu sama kont. jarajëf]"
|
| 21 |
+
20,connaitre solde du compte courant,BALANCE,Xam tolluwaayu kont. ,[xam tolːuwaːyu kont]
|
| 22 |
+
21,comment savoir combien il y a de sous sur le compte s'il vous plait,BALANCE,Naka lañuy xame ñaata ciy koppar moo nekkk ci kont bi ?,[naka lañuy xame ñaːta ciy kopːar moː nekː ci kont?]
|
| 23 |
+
22,Bonjour j'ai un compte chez vous et je voulais savoir si vous pouvez me montrer le solde sur mon compte courant merci,BALANCE,"Salaamaaleekum, dama am ab kont ci yéen, te bêggoona xam ndax mên ngéen maa won tolluwaayam ciy koppar.","[salaːmaːlekum, dama am ab kont ci yeːn, te bëgːoːna xam ndax mën ngeːn maː won tolːuwaːyam ciy kopːar]"
|
| 24 |
+
23,Bonjour j'aimerais savoir quels sont les restaurants sur mon compte l'argent qui est disponible pour mes futurs d'achat merci,BALANCE,"Salaamaaleekum, dama bêggoona xam yan restoraa ñoo nekk ci sama kont, ak koppar yi ma ci mêna ame lu may bëgga jënd. Jarajêf. ","[salaːmaːlekum, dama bëgːoːna xam yan restoraː ñoː nekː ci sama kont, ak kopːar yi ma ci mëna ame lu my bëgːa jënd. jarajëf]"
|
| 25 |
+
24,consulter le solde de mon compte,BALANCE,Seet tolluwaaayu sama kont.,[seːt tolːuwaːyu sama kont]
|
| 26 |
+
25,affiche le solde de mon compte courant,BALANCE,woneel tolluwaayu sama kont. ,[woneːl tolːuwaːyu sama kont]
|
| 27 |
+
26,solde de mon compte bancaire,BALANCE,Tolluwaayu sama kontu bànk ,[tolːuwaːyu sama kont bànk]
|
| 28 |
+
27,bonjour Est-ce que vous pouvez me montrer le solde de mon compte s'il vous plait,BALANCE,"Salaamaalekum ngéen baal ma, ndax mën ngéen ma won tolluwaayu sama kont ?","[salaːmaːlekum ngeːn baːl ma, ndax mën ngeːn ma won tolːuwaːyu sama kont ?]"
|
| 29 |
+
28,je voudrais savoir combien de solde sur mon compte courant,BALANCE,Dama bêggoona xam ñaata moo des ci sama kont. ,[dama bëgːoːna xam ñaːta moː des ci sama kont]
|
| 30 |
+
29,quelle somme me reste-t-il sur mon compte en banque,BALANCE,Ñaata ci xaalis moo des ci sama kontu bànk ? ,[ñaːta ci xaːlis moː des ci sama kontu bànk ?]
|
| 31 |
+
30,Bonjour j'aimerais savoir combien j'ai d'argent sur mon compte,BALANCE,"Salaamaalekum, dama bëggoona xam ñaata ci xaalis laa am ci sama kont ?","[salaːmaːlekum, dama bëgːoːna xam ñaːta ci xaːlis laː am ci sama kont ?]"
|
| 32 |
+
31,Bonjour Je veux savoir comment je pourrais voir le solde de mon compte sur mon espace client,BALANCE,"Salaamaalekum, dama bëggoona xam naka laa mëna gisee li des ci sama kont ci sama wàllu bopp ?","[salaːmaːlekum, dama bëgːoːna xam naka laː mëna giseː li des ci sama kont ci sama wàlːu bopː ?]"
|
| 33 |
+
32,montre-moi l'argent sur mon compte,BALANCE,Wonléen ma xaalis bi ci sama kont.,[wonleːn ma xaːlis bi ci sama kont]
|
| 34 |
+
33,montre-moi le solde de mon compte,BALANCE,Wonléen ma li des ci sama kont.,[wonleːn ma li des ci sama kont]
|
| 35 |
+
34,quel est le solde de mon compte,BALANCE,Lu des ci sama kont ?,[lu des ci sama kont ?]
|
| 36 |
+
35,pourriez-vous me renseigner sur le solde de mon compte,BALANCE,Ndax mën ngéen ma leeral ci sama tolluwaayu kont ?,[ndax mën ngeːn ma leːral ci sama tolːuwaːyu kont ?]
|
| 37 |
+
36,bonjour oui je vous appelle pour connaitre le solde de mon compte courant s'il vous plait merci,BALANCE,"Salaamaalekum, waaw. Ngéen baal ma, maa leen woo ngir xam tolluwaayu sama kont. Jarajëf.","[salaːmaːlekum, waːw. ngeːn baːl ma, maː leːn woː ngir xam tolːuwaːyu sama kont. jarajëf]"
|
| 38 |
+
37,Bonjour je vous appelle car j'aimerais connaitre le solde de mon compte courant merci,BALANCE,"Salaamaaleekum, dama woote ngir xam sama tolluwwayu kont. Jarajêf.","[salaːmaːlekum, dama woːte ngir xam sama tolːuwaːyu kont. jarajëf]"
|
| 39 |
+
38,quel est le solde de mon compte,BALANCE,Lan mooy sama tolluwaayu kont ?,[lan moːy sama tolːuwaːyu kont ?]
|
| 40 |
+
39,je voudrais connaitre le solde de mon compte courant,BALANCE,Dama bëggoona xam tolluwaayu sama kont. ,[dama bëgːoːna xam tolːuwaːu sama kont]
|
| 41 |
+
40,Bonjour j'aimerais bien savoir le solde de mon compte,BALANCE,"Salaamaalekum, bëggoon naa xam tolluwaayu sama kont. ","[salaːmaːlekum, bëgːoːn naː xam tolːuwaːyu sama kont]"
|
| 42 |
+
41,bonjour je vais déposer de l'argent sur mon compte comment est-ce que je peux faire s'il vous plait,CASH_DEPOSIT,Salaamaalekum damay dugal xaalis ci sama kont. Naka laa ko mêna defe ?,[salaːmaːlekum damay dugal xaːlis ci sama kont. Naka laː ko mëna defe?]
|
| 43 |
+
42,je souhaiterais déposer de l'argent sur mon compte bancaire,CASH_DEPOSIT,Dama bëgga dugal xaalis ci sama kontu bànk.,[dama bëgːa dugal xaːlis ci sama kontu bànk]
|
| 44 |
+
43,comment transférer de l'argent sur mon compte,CASH_DEPOSIT,Naka laay toxale xaalis ci sama kont ?,[naka laːy toxale xaːlis ci sama kont ?]
|
| 45 |
+
44,je voudrais déposer de l'argent sur mon compte,CASH_DEPOSIT,Dama bëggoona dugal xaalis ci sama kont.,[dama bëgːoːna dugal xaːlis ci sama kont]
|
| 46 |
+
45,je veux transférer de l'argent sur mon compte,CASH_DEPOSIT,Dama bëgga toxal xaalis ci sama kont.,[dama bëgːa toxal xaːlis ci sama kont]
|
| 47 |
+
46,Bonjour je vous contacte pour déposer de l'argent sur mon compte,CASH_DEPOSIT,"Salaamaalekum, maa léen woo ngir dugal xaalis ci sama kont.","[salaːmaːlekum, maː leːn woː ngir dugal xaːlis ci sama kont]"
|
| 48 |
+
47,Bonjour J'aimerais déposer de l'argent sur mon compte bancaire,CASH_DEPOSIT,"Salaamaalekum, dama bëggoona dugal xaalis ci sama kontu bànk","[salaːmaːlekum, dama bëgːoːna dugal xaːlis ic sama kontu bànk]"
|
| 49 |
+
48,comment faire pour déposer de l'argent,CASH_DEPOSIT,Naka laay def ngir dugal xaalis ?,[naka laːy def ngir dugal xaːlis ?]
|
| 50 |
+
49,Bonjour pourrais-je savoir comment je peux transférer de l'argent sur mon compte,CASH_DEPOSIT,Salaamaalekum. ndax mën naa xam naka laay toxale xaalis ci sama kont?,[salaːmaːlekum. ndax mën naː xam naka laːy toxale xaːlis ci sama kont ?]
|
| 51 |
+
50,où est-ce que je peux déposer de l'argent,CASH_DEPOSIT,Fan laa mëna dugale xaalis ?,[fan laː mëna dugale xaːlis ?]
|
| 52 |
+
51,je souhaiterais déposer de l'argent sur mon compte,CASH_DEPOSIT,Dama bëggoona dugal xaalis ci sama kont,[dama bëgːoːna dugal xaːlis ci sama kont]
|
| 53 |
+
52,comment puis-je déposer de l'argent sur mon compte ?,CASH_DEPOSIT,Naka laa mëna dugale xaalis ci sama kont ?,[naka laː mëna dugale xaːlis ci sama kont ?]
|
| 54 |
+
53,Bonjour je souhaite déposer une grosse somme d'argent en cash sur mon compte courant veuillez m'indiquer la meilleure manière de procéder.,CASH_DEPOSIT,"Salaamaalekum. Dama bëgga dugal xaalis bu takku, xoobet-xoobet, ci sama kont. … Ndax mën ngéen maa tektal nima koy defe ci anam bi gën ?","[salaːmaːlekum. dama bëgːa dugal xaːlis bu takːu, xoːbet-xoːbet, ci sama kont… ndax mën ngeːn maː tektal nima koy defe ci anam bi gën ?] "
|
| 55 |
+
54,Bonjour je souhaiterais déposer de l'argent sur mon compte.,CASH_DEPOSIT,"Salaamaalekum, Dama bëggoona dugal xaalis ci sama kont","[salaːmaːlekum, dama bëgːoːna dugal xaːlis ci sama kont]"
|
| 56 |
+
55,Bonjour J'aurais souhaité déposer une somme d'argent sur le compte et je ne sais pas comment procéder pouvez-vous m'expliquer s'il vous plaît ?,CASH_DEPOSIT,"Salaamaalekum, dama bëggoona dugal xaalis ci kont bi te xamuma naka laay def. Ndax mën ngéen ma koo tektal ?","[salaːmaːlekum, dama bëgːoːna dugal xaːlis ci kont bi te xamuma naka laːy def. ndax mën ngeːn ma koː tektal ?]"
|
| 57 |
+
56,puis-je déposer de l'argent ?,CASH_DEPOSIT,Ndax mën naa dugal xaalis ?,[ndax mën naː dugal xaːlis ?]
|
| 58 |
+
57,où est la banque pour déposer de l'argent ?,CASH_DEPOSIT,Ana bànk bi ñuy dugale xaalis ?,[ana bànk bi ñuy dugale xaːlis ?]
|
| 59 |
+
58,je souhaiterais déposer mon argent est-ce que je peux savoir comment le déposer ? Merci.,CASH_DEPOSIT,Dama bëggoona dugal sama xaalis. Ndax mên naa xam naka laa koy dugale ? jarajëf.,[dama bëgːoːna dugal sama xaːlis. ndax mën naː xam naka laː koy dugale ?]
|
| 60 |
+
59,Bonjour Je souhaiterais savoir la procédure pour déposer de l'argent sur mon compte en banque et comment transférer de l'argent directement dessus ? Merci.,CASH_DEPOSIT,Salaamaalekum. Dama bëggoona xam naka laay dugale xaalis ci sama kontu bànk ak naka laay toxale xaalis ci yoon wu jub..,[salaːmaːlekum. dama bëgːoːna xam naka laːy dugale xaːlis ci sama kontu bànk ak naka laːy toxale xaːlis ci yoːn wu jub…]
|
| 61 |
+
60,Bonjour j'aimerais savoir comment je peux déposer de l'argent sur mon compte en banque.,CASH_DEPOSIT,Salaamaalekum. bëgg naa xam naka laay dugale xaalis ci sama kontu bànk.,[salaːmaːlekum. bëgː naː xam naka laːy dugale xaːlis ci sama kontu bànk]
|
| 62 |
+
61,comment puis-je déposer de l'argent sur mon compte ?,CASH_DEPOSIT,Naka laa mëna dugale xaalis ci sama kont ?,[naka laː mëna dugale xaːlis ci sama kont ?]
|
| 63 |
+
62,bonjour comment puis-je déposer de l'argent sur mon compte.,CASH_DEPOSIT,Salaamaalekum. Naka laay def ba dugal xaalis ci sama kont ?,[salaːmaːlekum. naka laːy def ba dugal xaːlis ci sama kont ?]
|
| 64 |
+
63,Bonjour Je souhaiterais savoir comment transférer de l'argent sur mon compte.,CASH_DEPOSIT,Salaamaalekum. Dama bëgga xam naka laay toxale xaalis ci sama kont.,[salaːmaːlekum. dama bëgːa xam naka laːy toxale xaːlis ci sama kont]
|
| 65 |
+
64,comment transférer de l'argent ?,CASH_DEPOSIT,Naka lañuy toxale xaalis ?,[naka lañuy toxale xaːlis ?]
|
| 66 |
+
65,oui bonjour pourriez-vous m'indiquer comment je peux transférer ?,CASH_DEPOSIT,"Waaw. Salaamaalekum, ndax mën ngéen maa tektal naka lañuy toxale xaalis ?","[waːw. Salaːmaːlekum, ndax mën ngeːn maː tektal naka lañuy toxale xaːlis ?]"
|
| 67 |
+
66,comment est-ce que je peux déposer de l'argent sur mon compte en banque virtuellement ou physiquement ?,CASH_DEPOSIT,Naka la mëna dugale xaalis ci sama kontu bànk ci yonnee ko mbaa ma teew ?,[naka la mëna dugale xaːlis ci sama kontu bank ci yonːeː ko mbaː ma teːw ?]
|
| 68 |
+
67,allo bonjour oui madame je vous appelle pour savoir comment je peux déposer de l'espèce sur mon compte ? Merci.,CASH_DEPOSIT,"Aloo ! salaamaalekum. Waaw, soxna si, dama la woo ngir xam naka laay dugale xaalis bu teew ci sama kont ? jarajëf","[aloː ! salaːmaːlekum. waːw, soxna si dama la woː ngir xam naka laːy dugale xaːlis bu teːw ci sama kont ? jarajëf]"
|
| 69 |
+
68,Bonjour je vous appelle pour mon compte en banque j'aimerais pouvoir transférer une somme de 1000 fr sur mon compte pouvez-vous m'aider ?,CASH_DEPOSIT,Salaamaalekum. Dama leen woo ngir sama kontu bànk. Dama bëgga toxal lu mat ñaari téeméer ci sama kont. Ndax mën ngéen ma cee dimbali ?,[salaːmaːlekum. dama leːn woː ngir sama kontu bank. dama bëgːa toxal lu mat ñaːri teːmeːr ci sama kont. ndax mën ngeːn ma ceː dimbali ?]
|
| 70 |
+
69,puis-je passer de l'argent sur mon compte ?,CASH_DEPOSIT,Ndax mën naa jàllale xaalis ci sama kont ?,[ndax mën naː jalːale xaːlis ci sama kont ?]
|
| 71 |
+
70,je souhaiterais savoir comment déposer de l'argent sur mon compte faut-il venir en agence ?,CASH_DEPOSIT,Dama bëggoona xam naka laay dugale xaalis ci sama kont ? Ndax dama wara teew ci bërëb bi ?,[dama bëgːoːna xam naka laːy dugale xaːlis ci sama kont ? ndax dama wara teːw ci bërëb bi ?]
|
| 72 |
+
71,j'aimerais déposer de l'argent sur mon compte.,CASH_DEPOSIT,Dama bëggoona dugal xaalis ci sama kont,[dama bëgːoːna dugal xaːlis ci sama kont]
|
| 73 |
+
72,j'aimerais bloquer ma carte immédiatement car j'ai vu qu'il y avait des transactions frauduleuses,FREEZE,Dama bëgga tënk sama kàrt cisaasi ndax seetlunaa ni na ni amna ay wuruj yu ñu ciy doxal.,[dama bëgːa tënk sama kart ci saːsi ndax seːtlunaː ni amna ay wuruj yu ñu ciy doxal]
|
| 74 |
+
73,je souhaiterais bloquer ma carte,FREEZE,Dama bëgga tënk sama kart,[dama bëgːa tënk sama kart]
|
| 75 |
+
74,blocage de ma carte,FREEZE,Tënk sama kàrt.,[tënk sama kart]
|
| 76 |
+
75,je vous appelle car j'ai un problème avec ma carte je crois qu'elle a été piratée j'aimerais que vous bloquiez tous les paiements merci beaucoup,FREEZE,Dama woote ndax dama am ay jafe-jafe ci sama kàrt. Dama jort ni dañu ko suxlu. Ma bëggoon ngéen gàntal lépp lu ciy jêle xaalis. Jaangéen-jêf.,[dama woːte ndax dama am ay jafe-jafe ci sama kart. dama njort ni dañu ko suxlu. ma bëgːoːn ngeːn gantal lepː lu ciy jël xaːlis. jaːngeːn-jëf]
|
| 77 |
+
76,je souhaiterais bloquer ma carte,FREEZE,Dama bëgga tënk sama kàrt.,[dama bëgːa tënk sama kart]
|
| 78 |
+
77,pouvez-vous geler ma carte s'il vous plait,FREEZE,Ndax mën ngéena ajandi sama kart ?,[ndax mën ngeːna ajandi sama kart]
|
| 79 |
+
78,bloquer ma carte,FREEZE,Tënk sama kàrt.,[tënk sama kart]
|
| 80 |
+
79,bloquer ma carte bancaire,FREEZE,Tënk sama kartu bànk.,[tënk sama kartu bank]
|
| 81 |
+
80,oui bonjour suite à la perte de ma carte bancaire j'aurais aimé que vous bloquiez ma carte s'il vous plait merci,FREEZE,"Waaw, salaamaaleekum. Sama kartu bànk dafa réer, ma bëggoon ngéen tënkal ma ko. Jarajëf.","[waːw, salaːmaːlekum. sama kartu bànk dafa reːr, ma bëgːoːn ngeːn tënkal ma ko. jarajëf]"
|
| 82 |
+
81,j'aimerais bloquer la carte temporairement,FREEZE,Dama bëggoona tënk kart bi ba ab diir.,[dama bëgːoːna tënk kart bi ba ab diːr]
|
| 83 |
+
82,arrêtez toutes les transactions sur ma carte,FREEZE,Dakkal leen bépp jëflante ci sama kàrt.,[dakːal leːn bepː jëflante ci sama kart]
|
| 84 |
+
83,veuillez bloquer ma carte,FREEZE,Tënk léen sama kàrt,[tënk leːn sama kart]
|
| 85 |
+
84,je veux bloquer ma carte bancaire,FREEZE,Dama bëgga tënk sama kàrtu bank.,[dama bëgːa tënk sama kartu bànk]
|
| 86 |
+
85,Bonjour J'ai besoin de bloquer ma carte s'il vous plait,FREEZE,Salaamaalekum. Dama bëgg ngéen tënk sama kart.,[salaːmaːlekum. dama bëgː ngeːn tënk sama kart]
|
| 87 |
+
86,bonjour j'aimerais pouvoir complètement bloquer ma carte s'il vous plait,FREEZE,Salaamaalekum. Dama bëgg ñu tëj ràpp sama kàrt.,[salaːmaːlekum. dama bëgː ñu tëj rapː sama kart]
|
| 88 |
+
87,Bonjour je vous appelle car j'ai une demande urgente j'ai perdu ma carte et j'aimerais que vous la bloquiez s'il vous plait merci,FREEZE,"Salaamaalekum. Ngéen baal ma, dama woote ndax am soxla bu jàmp. Sama kàrt moo réer te ma bëggoon ngeen tënk ko.Jarajëf.","[salaːmaːlekum. ngeːn baːl ma, dama woːte ndax am soxla bu jamp. Sama kart moː reːr te ma bëgːoːn ngeːn tënk ko. jarajëf]"
|
| 89 |
+
88,Bonjour je vous appelle à propos de ma carte de crédit j'aimerais la bloquer,FREEZE,Na ngéen def ? Dama woote ngiri lu jëm ci sama kàrtu koppar. Dama ko bëggoona tënk. ,[na ngeːn def ? dama woːte ngir lu jëm ci sama kartu kopːar. dama ko bëgːoːna tënk]
|
| 90 |
+
89,serait-il possible de bloquer ma carte,FREEZE,Ndax mënees naa tënk sama kart?,[ndax mëneːs naː tënk sama kart?]
|
| 91 |
+
90,avoir plus d'information de comment bloquer ma carte,FREEZE,Am yeneen tektal ci may tënke sama kart.,[am yeneːn tektal ci nimay tënke sama kart]
|
| 92 |
+
91,on m'a volé ma carte je souhaiterais bloquer toutes les transactions,FREEZE,"Dañoo sàcc sama kàrt, ma bëggoona dakkal lépp lu ñ.u ciy jëflante","[dañoː sàcː sama kart, ma bëgːoːna dakːal lepː lu ñu ciy jëflante]"
|
| 93 |
+
92,j'ai perdu ma carte bancaire je souhaiterais faire opposition et là bloquer afin de bloquer tout paiement,FREEZE,"Dama réeral sama kàrtu bànk, ma bëggoon nu tënk ko ba kenn du ci mëna feyoo dara. ","[dama reːral sama kartu bànk, ma bëgːoːn nu tënk ko ba kenː du ci mëna feyoː dara]"
|
| 94 |
+
93,je souhaite bloquer ma carte,FREEZE,Dama bëgga tënk sama kàrt.,[dama bëgːa tënk sama kart]
|
| 95 |
+
94,je veux faire bloquer ma carte de crédit,FREEZE,Dama bëgga tënklu sama kàrtu bank.,[dama bëgːa tënklu sama kartu bànk]
|
| 96 |
+
95,j'ai besoin de vous bloquer ma carte,FREEZE,Dama soxla ngéen tënk sama kart.,[dama soxla ngeːn tënk sama kart]
|
| 97 |
+
96,montre-moi mes dernières transactions,LATEST_TRANSACTIONS,Won ma jëflante yi mujja am ci sama kart.,[won ma jëflante yi mujːa am ci sama kart]
|
| 98 |
+
97,je veux consulter mes dernières transactions,LATEST_TRANSACTIONS,Dama bëgga gis samay jëflante yu mujj yi.,[dama bëgːa gis samay jëflante yu mujː yi]
|
| 99 |
+
98,je voudrais les dernières transactions de ma carte,LATEST_TRANSACTIONS,Jëflante yu mujj yi ci sama kart la soxla .,[jëflante yu mujː yi ci sama kart la soxla]
|
| 100 |
+
99,je souhaite consulter mes dernières opérations,LATEST_TRANSACTIONS,Dama bëgga gis sama jëflante yu mujj yi.,[dama bëgːa gis sama jëflante yu mujː yi]
|
| 101 |
+
100,j'appelle à propos de mes dernières transactions,LATEST_TRANSACTIONS,Dama woote ngir lu jëm ci samay jëflante yu mujj yi.,[dama woːte ngir lu jëm ci samay jëflante yu mujː yi]
|
| 102 |
+
101,bonjour je voulais regarder mes derniers paiements. Est-ce que c'est possible d'avoir mes transactions récentes,LATEST_TRANSACTIONS,Salaamaalekum dama bëggoona xool li ma mujja fey. Ndax mën naa xam sama jëflante yu mujj yi?,"[salaːmaːlekum dama bëgːoːna xoːl li ma mujːa fey, ndax mën naː xam sama jëflante yu mujː yi ?]"
|
| 103 |
+
102,quelles sont les dernières transactions,LATEST_TRANSACTIONS,Yan ñooy jëflante yu mujj yi ?,[yan ñoːy jëflante yu mujː yi ?]
|
| 104 |
+
103,j'aimerais obtenir la liste des dernières transactions effectuées sur mon compte,LATEST_TRANSACTIONS, Dama bëggoona am limu jëflante yi mujje ci sama kont.,[dama bëgːoːna am limu jëflante yi mujːe ci sama kont]
|
| 105 |
+
104,montre-moi mes dernières transactions,LATEST_TRANSACTIONS,Won ma samay jëflante yu mujj.,[won ma samay jëflante yu mujː]
|
| 106 |
+
105,pouvez-vous me donner mes dernières transactions,LATEST_TRANSACTIONS,Ndax mën ngeen maa jox sama jëflante yu mujj ?,[ndax mën ngeːn maː jox sama jëflante yu mujː ?]
|
| 107 |
+
106,j'ai besoin de voir les derniers paiements,LATEST_TRANSACTIONS,Soxla naa gis peyoor yu mujj yi.,[soxla naː gis peyoːr yu mujː yi]
|
| 108 |
+
107,bonjour Est-ce que vous pouvez me montrer mes dernières transactions il y a un paiement que je ne reconnais pas,LATEST_TRANSACTIONS,Salaamalekum. Ndax mën ngéen ma won samay jëflante yu mujj yi ? Dafa am benn peyoor bu ma ràññeewul.,[salaːmaːlekum. ndax mën ngeːn ma won samay jëflante yu mujː? dafa am benː peyoːr bu ma ràñːwul]
|
| 109 |
+
108,all√¥ oui bonjour j'aimerais avoir quelques renseignements concernant différents versements qui ont eu lieu récemment sur mon compte,LATEST_TRANSACTIONS,"Aloo! Waaw, na ngéen def? Dama soxlawoon ay tektal yu jëm ci yenni dugali koppar yu am ci sama kont bu yàggul.","[aloː! waːw, na ngeːn def? dama soxlawoːn ay tektal yu jëm ci yenːi dugali kopːar yu am ci sama kont bu yaːgul]"
|
| 110 |
+
109,je souhaiterais voir mes transactions récentes,LATEST_TRANSACTIONS,Dama bëgga gis sama jëflante yu yees yi.,[dama bëgːa gis sama jëflante yu yeːs yi]
|
| 111 |
+
110,Bonjour J'aimerais regarder mes transactions récentes s'il vous plait,LATEST_TRANSACTIONS,Salaamaalekum dama bëgga xool sama jëflante yu yees yi.,[salaːmaːlekum dama bëgːa xoːl sama jëflante yu yeːs yi]
|
| 112 |
+
111,oui je souhaiterais avoir accès à l'historique de mes dernières transactions sur la semaine dernière voilà merci,LATEST_TRANSACTIONS,"Waaw, dama bëggoon ñu faram-fàcceel ma jëflante yi ma mujja am ci ayubés bi weesu. ","[waːw, dama bëgːoːn ñu faram-fàcːeːl ma jëflante yi ma mujːa am ci ayubes bi weːsu]"
|
| 113 |
+
112,oui bonjour pouvez-vous me donner le montant de ma dernière transaction s'il vous plait,LATEST_TRANSACTIONS,"Waaw, salaamaaleekum. Ndax mën ngéen ma jox limu sama jëflante bu mujj bi ? ","[waːw, salaːmaːlekum. ndax mën ngeːn ma jox limu sama jëflante bu mujː bi?]"
|
| 114 |
+
113,Bonjour je souhaiterais visualiser les dix dernières transactions qui ont eu lieu sur mon compte,LATEST_TRANSACTIONS,Salaamaalekum . Dama bëggoona xool fukki jëflante yu mujj am ci sama kont.,[salaːmaːlekum. dama bëgːoːna xoːl fukːi jëflante yu mujː am ci sama kont]
|
| 115 |
+
114,j'aurais besoin de voir mes dernières transactions,LATEST_TRANSACTIONS,Dama ittewoo xool samay jëflante yu mujj.,[dama itːewo xoːl samay jëflante yu mujː]
|
| 116 |
+
115,je voudrais voir mes dernières transactions et paiement,LATEST_TRANSACTIONS,Dama bëggoona gis samay jëflante ak peyoor yu mujj yi.,[dama bëgːoːna gis samay jëflante ak peyoːr yu mujː yi]
|
| 117 |
+
116,je veux voir mes dernières transactions,LATEST_TRANSACTIONS,Dama bëgga gis sama jëflante yi mujj,[dama bëgːa gis sama jëflante yi mujː]
|
| 118 |
+
117,quelles sont mes dernières transactions,LATEST_TRANSACTIONS,Yan ñooy samay jëflante yu mujj?,[yan ñoːy samay jëflante yu mujː]
|
| 119 |
+
118,bonjour alors j'aimerais bien revoir un peu le résumé de mes transactions restants,LATEST_TRANSACTIONS,Salaamaalekum. Dama bëggoona xoolaat tuuti ci lu gàtt samay jëflante yi des.,[salaːmaːlekum. dama bëgːoːna xoːlaːt tuːti ci lu gatː samay jëflante yi des]
|
| 120 |
+
119,pourrais-tu m'afficher mes dernières transactions s'il te plait,LATEST_TRANSACTIONS,Nga baal ma. Ndax mën nga ma won samay jëflante yi mujj ?,[nga baːl ma. ndax mën nga ma won samay jëflante yi mujː ?]
|
| 121 |
+
120,Bonjour J'ai un problème car il y a sur mon relevé de compte un paiement que je ne reconnais pas pourriez-vous m'indiquer mes dernières transactions s'il vous plait,LATEST_TRANSACTIONS,Salaamaalekum. Dama am ab jafe-jafe ndax dafa am ci sama jukkiteb kont benn peyoor bu ma ràññeewul. Ndax mën ngéen ma tektal samay jëflante yu mujj yi ?,[salaːmaːlekum. dama am ab jafe-jafe ndax dafa am ci sama jukːiteb kont benː peyoːr bu ma ràñːewul. ndax mën ngeːn ma tektal samay jëflante yu mujː yi]
|
| 122 |
+
121,non monsieur je vous appelle parce que j'aimerais faire une recherche sur mes transactions récents il y a une de mes dernières transactions que je ne reconnais pas je voudrais regarder exactement ce que c'est merci beaucoup,LATEST_TRANSACTIONS,"Déedeed Sëñ bi, Dama woote ndax dama bëgga gëstu ci samay jëflante yu mujj yi. Dafa ci am benn bu ma ràññeewul.","[deːdeːt sëñ bi, dama woːte ndax dama bëgːa gëstu ci samay jëflante yu mujː yi. dafa ci am benː bu ma ràñːeːwul]"
|
| 123 |
+
122,j'appelle pour pouvoir avoir un aperçu de mes transactions récentes sur mon compte bancaire et voir si il y a des paiements que je connais ou que je ne connais pas ,LATEST_TRANSACTIONS,"Dama woote ngir mën am gis-gis ci sama jëflante yi yees ci sama kontu bànk, ak seet ndax amna ay peyoor yu ma xam walla ràññeewuma leen.","[dama woːte ngir mën am gis-gis ci sama jëflante yi yeːs ci sama kontu bànk, ak seːt ndax amna ay peyoːr yu ma xam walːa ràñːeːwuma leːn]"
|
| 124 |
+
123,j'aimerais voir les transactions les plus récentes,LATEST_TRANSACTIONS,Dama bëggoona gis sama jëflantle yi gëna yees,[dama bëgːoːna gis sama jëflante yi gëna yeːs]
|
| 125 |
+
124,puis-je voir mes dernières transactions,LATEST_TRANSACTIONS,Ndax mën naa gis sama jëflante yu mujj yi?,[ndax mën naː gis sama jëflante yu mujː yi?
|
| 126 |
+
125,je voudrais payer une facture,PAY_BILL,Dama bëgga fey ab faktiir.,[dama bëgːa fey ab faktiːr]
|
| 127 |
+
126,payer une facture,PAY_BILL,Fey ab faktiir.,[fey ab faktiːr]
|
| 128 |
+
127,Bonjour je souhaiterais payer une facture s'il vous plait,PAY_BILL,Salaamaalekum. Dama bëggoona fey ab këyit. ,[salaːmaːlekum. dama bëgːoːna fey ab këyit]
|
| 129 |
+
128,je dois effectuer un paiement,PAY_BILL,Dama am lu ma wara fey. ,[dama am lu ma wara fey]
|
| 130 |
+
129,je voudrais payer une facture,PAY_BILL,Dama bëggoona fey ab faktiir. ,[dama bëgːoːna fey ab faktiːr]
|
| 131 |
+
130,je souhaite payer une facture,PAY_BILL,Dama bëgga fey ab faktiir.,[dama bëgːa fey ab faktiːr]
|
| 132 |
+
131,Bonjour je t'appelle parce que j'aurais besoin de payer ma facture SDE,PAY_BILL,Salaamaalekum. Dama woote ndax dama soxlawoona fey sama faktiiru SDE. ,[salaːmaːlekum. dama woːte ndax dama soxlawoːna fey sama faktiːru SDE]
|
| 133 |
+
132,je souhaiterais payer une facture,PAY_BILL,Dama bëgga fey ab faktiir,[dama bëgːa fey ab faktiːr]
|
| 134 |
+
133,Bonjour Je dois payer une facture,PAY_BILL,Salaamaalekum. Dama wara fey ab faktiir.,[salaːmaːlekum. dama wara fey ab faktiːr]
|
| 135 |
+
134,payer une facture,PAY_BILL,Fey ab faktiir.,[fey ab faktiːr]
|
| 136 |
+
135,j'ai une facture à payer,PAY_BILL,Dama am ab faktiir bu ma wara fey.,[dama am ab faktiːr bu ma wara fey]
|
| 137 |
+
136,bonjour je viens de recevoir une facture et j'aimerais la payer comment procéder ?,PAY_BILL,Salaamaalekum. Dama jot ab faktiir te bëggoon koo fay. Naka laa koy defe?,[salaːmaːlekum. dama jot ab faktiːr te bëgːoːn koː fey. naka laː koy defe ?]
|
| 138 |
+
137,je dois payer une facture,PAY_BILL,Dafa am ab faktiir bu ma wara fey. ,[dafa am ab faktiːr bu ma wara fey]
|
| 139 |
+
138,je souhaiterais payer ma facture s'il vous plaît,PAY_BILL,Dama bëggoona fey sama faktiir. ,[dama bëgːoːna fey sama faktiːr]
|
| 140 |
+
139,ma facture de courant,PAY_BILL,Sama faktiiru kuuraa.,[sama faktiːru kuːraː]
|
| 141 |
+
140,je dois payer une facture aujourd'hui,PAY_BILL,Tay war naa fey faktyr,[tay war naː fey faktiːr]
|
| 142 |
+
141,oui bonjour oui je vais faire un paiement,PAY_BILL,"Waaw, na ngeen def? waaw; dafa am lu may fey.","[waːw, na ngeːn def? waːw, dafa am lu may fey]"
|
| 143 |
+
142,j'aimerais payer une facture,PAY_BILL,Dama bëggoona fey benn faktiir.,[dama bëgːoːna fey benː faktiːr]
|
| 144 |
+
143,Bonjour j'ai une facture à payer et j'aimerais savoir comment procéder,PAY_BILL,"Salaamaalekum. Dama am faktiir bu ma wara fey, ma bëggoona xam naka laay def.","[salaːmalekum. dama am faktiːr buma wara fey, ma bëgːoːna xam naka laːy def]"
|
| 145 |
+
144,Bonjour je vous contacte pour payer facture,PAY_BILL,Salaamaalekum. Dama léen woo ngir fey ab faktiir.,[salaːmalekum. dama leːn woː ngir fey ab faktiːr]
|
| 146 |
+
145,paiement facture,PAY_BILL,Fey ab faktiir.,[fey ab faktiːr]
|
| 147 |
+
146,Bonjour je vous appelle quand je souhaite régler une facture pour juste ce mois-ci au revoir,PAY_BILL,Salaamaalekum. Dinaa léen woo buma bëggee fey faktiir ci weer wii. Ba beneen .,[salaːmaːlekum. dinaː leːn woː buma bëgːeː fey faktiːr ci weːr wiː. ba beneːn]
|
| 148 |
+
147,bonjour j'aimerais payer une facture,PAY_BILL,Salaamaalekum. Dama bëggoona fey ab faktiir.,[salaːmaːlekum. dama bëgːoːna fey ab faktiːr]
|
| 149 |
+
148,je veux payer une facture,PAY_BILL,Dama bëgga fey ab faktiir,[dama bëgːa fey ab faktiːr]
|
| 150 |
+
149,oui bonjour je souhaiterais payer une facture est-ce que vous pouvez m'indiquer la méthode à utiliser,PAY_BILL,"Waaw, na ngéen def ? Dama bëggoona fey ab faktiir. Ndax mën ngéen maa wax ci ban anam laa koy defe ?","[waːw, na ngeːn def? dama bëgːoːna fey ab faktiːr. ndax mën ngeːn maː wax ci ban anam laː koy defe?]"
|
| 151 |
+
150,Bonjour une facture s'il vous plaît,PAY_BILL,"Salaamaalekum, ab faktiir laay laaj.","[salaːmaːlekum, ab faktiːr laːy laːj]"
|
| 152 |
+
151,Je souhaite ouvrir un compte,OPEN_ACCOUNT,Dama bëgga ubbi ab kont.,[dama bëgːa ubːi ab kont]
|
| 153 |
+
152,Je souhaiterais ouvrir un compte,OPEN_ACCOUNT,Dama bëggoon ubbi ab kont.,[dama bëgːoːn ubːi ab kont]
|
| 154 |
+
153,Comment puis-je ouvrir un compte ?,OPEN_ACCOUNT,Naka laa mëna ubbee ab kont ?,[naka laː mëna ubːeː ab kont?]
|
| 155 |
+
154,Bonjour je veux ouvrir un nouveau compte,OPEN_ACCOUNT,Salaamaalekum. Dama bëgga ubbi ab kont bu bees.,[salaːmaːlekum. dama bëgːa ubːi ab kont bu beːs]
|
| 156 |
+
155,Quelles sont les étapes à suivre pour l'ouverture d'un compte ?,OPEN_ACCOUNT,Yan yoon lañuy topp ngir ubbi ab kont ?,[yan yoːn lañuy topː ngir ubːi ab kont?]
|
| 157 |
+
156,Je souhaiterais réserver une place pour Dakar,BUS_RESERVATION,Dama bëggoona jàpp palaas ngir dem Ndakaaru,[dama bëgːoːna jàpː palaːs ngir dem ndakaːru]
|
| 158 |
+
157,Je souhaiterais réserver une place pour Saint-louis,BUS_RESERVATION,Dama bëggoona jàpp palaas ngir dem Ndar.,[dama bëgːoːna jàpː palaːs ngir dem ndar]
|
| 159 |
+
158,Y a-t'il des places disponibles pour le bus du matin ?,BUS_RESERVATION,Ndax amna ay palaas yu des ci kaaru suba gi ?, [ndax amna ay palaːs yu des ci kaːru suba gi ?]
|
| 160 |
+
159,Y a-t'il des places disponibles pour le bus du soir ?,BUS_RESERVATION,Ndax amna ay palaas yu des ci kaaru ngoon gi ?,[ndax amna ay palaːs yu des ci kaːru ngoːn gi ?]
|
| 161 |
+
160,A combien s'élève le prix du ticket ?,BUS_RESERVATION,Paas bi ñaata la ?,[paːs bi ñaːta la ?]
|
| 162 |
+
161,Quand es-ce-que le bus du matin prend départ ?,BUS_RESERVATION,Kañ la kaaru suba gi di dem ? ,[kañ la kaːru suba gi di dem ?]
|
| 163 |
+
162,Quand es-ce-que le bus du soir prend départ ?,BUS_RESERVATION,Kañ la kaaru ngoon gi di dem ?,[kañ la kaːru ngoːn gi di dem ?]
|
| 164 |
+
163,Je souhaite passer la visite technique de ma voiture,TECHNICAL_VISIT,Dama bëgga def sama wisit tekniku oto.,[dama bëgːa def sama wisit tekniku oto]
|
| 165 |
+
164,Le numéro de matricule de mon véhicule est DK1234AB,TECHNICAL_VISIT,Sama nimoro oto mooy DK 1234 AB.,[sama nimoro oto moːy DK 1234 AB]
|
| 166 |
+
165,Je voudrais effectuer un transfert,TRANSFER_MONEY,Dama bëgga def ab toxalu kooppar.,[dama bëgːa def ab toxalu kopːar]
|
| 167 |
+
166,Je souhaite envoyer de l'argent,TRANSFER_MONEY,Dama bëgga yóonee xaalis.,[dama bëgːa yoːneː xaːlis]
|
| 168 |
+
167,0,AMOUNT,dara,[dara]
|
| 169 |
+
168,1000,AMOUNT,Ñaari téemeer.,[ñaːri teːmeːr]
|
| 170 |
+
169,2000,AMOUNT,Ñeenti téemeer,[ñeːnti teːmeːr]
|
| 171 |
+
170,3000,AMOUNT,Juroom-benni téemeer.,[juroːm benːi teːmeːr]
|
| 172 |
+
171,4000,AMOUNT,Juroom-ñatti téemeer,[juruːm ñatːi teːmeːr]
|
| 173 |
+
172,5000,AMOUNT,Junni,[junːi]
|
| 174 |
+
173,6000,AMOUNT,Junni ak ñaari téemeer,[junːi ak ñaːri teːmeːr]
|
| 175 |
+
174,7000,AMOUNT,Junni ak ñeenti téemeer,[junːi ak ñeːti teːmeːr]
|
| 176 |
+
175,8000,AMOUNT,Junni ak juroom-benni téemeer,[junːi ak juroːm-benːi teːmeːr]
|
| 177 |
+
176,9000,AMOUNT,Junni ak juroom-ñatti téemeer,[junːi ak juroːm-ñatːi teːmeːr]
|
| 178 |
+
177,10000,AMOUNT,Ñaari junni,[ñaːri junːi]
|
| 179 |
+
178,20000,AMOUNT,Ñeenti junni,[ñeːnti junːi]
|
| 180 |
+
179,30000,AMOUNT,Juroom-benni junni,[juroːm-benːi junːi]
|
| 181 |
+
180,40000,AMOUNT,Juroom-ñatti junni,[juroːm-ñati junːi]
|
| 182 |
+
181,50000,AMOUNT,Fukki junni,[fukːi junːi]
|
| 183 |
+
182,60000,AMOUNT,Fukki junni ak ñaar,[fukːi junːi ak ñaːr]
|
| 184 |
+
183,70000,AMOUNT,Fukki junni ak ñeent,[fukːi junːi ak ñeːnt]
|
| 185 |
+
184,80000,AMOUNT,Fukki junni ak juroom-benn,[fukːi ɟjunːi ak juroːm-benː]
|
| 186 |
+
185,90000,AMOUNT,Fukki junni ak juroom-ñatt,[fukːi junːi ak juroːm-ñatː]
|
| 187 |
+
186,100000,AMOUNT,Ñaar-fukki junni,[ñaːr-fukːi junːi]
|
WolBanking77/audio/responses.csv
ADDED
|
@@ -0,0 +1,78 @@
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
| 1 |
+
N°,reponses_fr,reponse_intent,reponses_wo,reponses_transcription
|
| 2 |
+
1,Bienvenue à notre service client,WELCOME,Dalal jàmm ci sunu màkkaanu kilyaan bi.,[dalal jàmː ci sunu makːaːnu kilyaːn bi]
|
| 3 |
+
2,Je suis votre assistant virtuel,WHO_IS_IT,Man maay séen jàppalekat bi teewul.. …,[man maːy seːn japːalekat bi teːwul …]
|
| 4 |
+
3,"Vous pouvez soit réserver une place, soit effectuer une transaction financière",POSSIBILITIES,Mën nga jàpp palaas walla nga def ab jëflante ci xaalis.,[mën nga japː palaːs walːa nga def ab jëflante ci xaːlis]
|
| 5 |
+
4,"Je ne peux pas vous aider avec ça, je suis désolé",OUT_OF_SCOPE,"Mënuma laa dimbali ci loolu, maangiy jéggalu.","[mënuma laː dimbali ci loːlu, maːingiy jeːgːalu]"
|
| 6 |
+
5,"Désolé, je ne peux pas traiter cette demande",OUT_OF_SCOPE,"Maangiy jéggalu, mënumaa lijjanti laaj boobu.","[maːngiy jegːalu, mënumaː lijːanti laːj boːbu]"
|
| 7 |
+
6,Le solde de votre compte est de,BALANCE,Say koppari kont angi tollu ci : ,[say kopːari kont angi tolːu ci :]
|
| 8 |
+
7,0,AMOUNT,Amul dara.,[amul dara]
|
| 9 |
+
8,1000,AMOUNT,Ñaari téemeer.,[ñaːri teːmeːr]
|
| 10 |
+
9,2000,AMOUNT,Ñeenti téemeer,[ñeːnti teːmeːr]
|
| 11 |
+
10,3000,AMOUNT,Juroom-benni téemeer.,[juroːm benːi teːmeːr]
|
| 12 |
+
11,4000,AMOUNT, Juroom-ñatti téemeer,[juruːm ñatːi teːmeːr]
|
| 13 |
+
12,5000,AMOUNT,Junni,[junːi]
|
| 14 |
+
13,6000,AMOUNT,Junni ak ñaari téemeer,[junːi ak ñaːri teːmeːr]
|
| 15 |
+
14,7000,AMOUNT,Junni ak ñeenti téemeer,[junːi ak ñeːti teːmeːr]
|
| 16 |
+
15,8000,AMOUNT,Junni ak juroom-benni téemeer,[junːi ak juroːm-benːi teːmeːr]
|
| 17 |
+
16,9000,AMOUNT,Junni ak juroom-ñatti téemeer,[junːi ak juroːm-ñatːi teːmeːr]
|
| 18 |
+
17,10000,AMOUNT,Ñaari junni,[ñaːri junːi]
|
| 19 |
+
18,20000,AMOUNT,Ñeenti junni,[ñeːnti junːi]
|
| 20 |
+
19,30000,AMOUNT,Juroom-benni junni,[juroːm-benːi junːi]
|
| 21 |
+
20,40000,AMOUNT,Juroom-ñatti junni,[juroːm-ñati junːi]
|
| 22 |
+
21,50000,AMOUNT,Fukki junni,[fukːi junːi]
|
| 23 |
+
22,60000,AMOUNT,Fukki junni ak ñaar,[fukːi junːi ak ñaːr]
|
| 24 |
+
23,70000,AMOUNT,Fukki junni an ñeent,[fukːi junːi ak ñeːnt]
|
| 25 |
+
24,80000,AMOUNT,Fukki junni ak juroom-benn,[fukːi junːi ak juroːm-benː]
|
| 26 |
+
25,90000,AMOUNT,Fukki junni ak juroom-ñatt,[fukːi junːi ak juroːm-ñatː]
|
| 27 |
+
26,100000,AMOUNT,Ñaar-fukki junni,[ñaːr-fukːi junːi]
|
| 28 |
+
27,Combien souhaitez-vous déposer ?,CASH_DEPOSIT,Ñaata nga bëggoona dugal ?,[ñaːta nga bëgːoːna dugal ?]
|
| 29 |
+
28,Le montant déposé est de,CASH_DEPOSIT,Xaalis bi ñu dugal mu ngi tollu ci,[xaːlis bi ñu dugal mu ngi tolːu ci]
|
| 30 |
+
29,Quel est le montant de votre dépôt ?,CASH_DEPOSIT,Li ngay dugal nu mu tollu ?,[li ngay dugal nu mu tolːu ?]
|
| 31 |
+
30,Quel est le code secret de votre carte ?,FREEZE,Lan mooy sa kod sekere kart ?,[lan moːy sa kod sekere kart ?]
|
| 32 |
+
31,Votre compte a été bloquée avec succès,FREEZE,Jot nañoo tënk sa kont.,[jot nañoː tënk sa kont]
|
| 33 |
+
32,Vos dernières transactions sont les suivantes,LAST_TRANSACTIONS,Say jëflante yu mujjj yi ñoo nekk nii,[say jëflante yu mujː yi ñoː nekː niː]
|
| 34 |
+
33,Quel est le montant de votre facture ?,PAY_BILL,Sa faktiir naka la tollu ?,[sa faktiːr naka la tolːu ?]
|
| 35 |
+
34,Votre facture a été payée avec succès,PAY_BILL,Fey nañu sa faktiir ba noppi,[fey nañu sa faktiːr ba nopːi]
|
| 36 |
+
35,Donnez moi votre nom,OPEN_ACCOUNT,Jox ma sa sant ,[jox ma sa sant]
|
| 37 |
+
36,Donnez moi votre prenom,OPEN_ACCOUNT,Jox ma sa tur,[jox ma sa tur]
|
| 38 |
+
37,Donnez moi votre age,OPEN_ACCOUNT,Jox ma say at,[jox ma say at]
|
| 39 |
+
38,Donnez moi votre numéro de pièce d'identité,OPEN_ACCOUNT,Jox ma sa nimoro kart dantite,[jox ma sa nimoro kart dantite]
|
| 40 |
+
39,Souhaiteriez-vous prendre le bus du matin ou celui du soir ?,BUS_RESERVATION,Kaaru suba bi am kaaru ngoon bi nga bëgga jël ?,[kaːru suba bi am kaːru ngoːn bi nga bëgːa jël ?]
|
| 41 |
+
40,Il reste des places disponibles pour le bus du matin,BUS_RESERVATION,Kaaru suba bi des na ay palaas.,[kaːru suba si des na ay palaːs]
|
| 42 |
+
41,Il reste des places disponibles pour le bus du soir,BUS_RESERVATION,Kaaru ngoon bi des na ay palaas.,[kaːru ngoːn bi des na ay palaːs]
|
| 43 |
+
42,Le bus du matin prend départ à 7h,BUS_RESERVATION,Kaaru suba bi ci juroom-ñaari waxtu lay dem.,[kaːru suba bi ci juroːm-ñaːri waxtu lay dem]
|
| 44 |
+
43,Le bus du matin prend départ à 14h,BUS_RESERVATION,Kaaru suba bi ci fukki waxtu ak ñaar lay dem.,[kaːru suba bi ci fukːi waxtu ak ñaːr lay dem]
|
| 45 |
+
44,Le prix du ticket pour le bus est de 5000 fr,BUS_RESERVATION,Paas bi ci kaar bi junni la.,[paːs bi ci kaːr bi junːi la]
|
| 46 |
+
45,Pour quel jour voulez-vous réserver votre ticket ?,BUS_RESERVATION,Ban bés nga bëgga joxeel sa paas ?,[ban bes nga bëgːa joxeːl sa paːs ?]
|
| 47 |
+
46,Souhaitez-vous effectuer le paiement du transport ?,BUS_RESERVATION,Danga bëgg fey paas bi ?,[danga bëgː fey paːs bi?]
|
| 48 |
+
47,Combien de tickets souhaitez vous réserver ?,BUS_RESERVATION,Ñaata palaas nga bëgga jàpp?,[ñaːta palaːs nga bëgːa jàpː?]
|
| 49 |
+
48,Quelle est votre destination ?,BUS_RESERVATION,Fan nga jëm ?,[fan nga jëm?]
|
| 50 |
+
49,Quelle est votre ville de départ ?,BUS_RESERVATION,Ban dëgg ngay jóge ?,[ban dëkː ngay joge?]
|
| 51 |
+
50,Merci de me donner votre numéro de matricule,TECHNICAL_VISIT,Baal ma nga jox ma nimoro màtirkil.,[baːl ma nga jox ma nimoro matirkil]
|
| 52 |
+
51,lundi,TECHNICAL_VISIT,altine,[altine]
|
| 53 |
+
52,mardi,TECHNICAL_VISIT,talaata,[talaːta]
|
| 54 |
+
53,mercredi,TECHNICAL_VISIT,àllarba,[alːarba]
|
| 55 |
+
54,jeudi,TECHNICAL_VISIT,alxames,[alxames]
|
| 56 |
+
55,vendredi,TECHNICAL_VISIT,àjjuma,[ajːuma]
|
| 57 |
+
56,samedi,TECHNICAL_VISIT,gaawu,[gaːwu]
|
| 58 |
+
57,dimanche,TECHNICAL_VISIT,Dibéer,[dibeːr]
|
| 59 |
+
58,Votre rendez-vous pour la visite technique est prévue le ,TECHNICAL_VISIT,Sa bésu teewaay ngir wisit teknik moo.,[sa besu teːway ngir wisit teknik moː]
|
| 60 |
+
59,"Merci de vous munir de deux triangles, d'un extincteur, d'un timbre de 2000 francs et de 7000 francs",TECHNICAL_VISIT,"Booy ñów nanga indaale ññaaari tiriyaangal, benn feyukaaay, bennn teembaru ñeenti téemeer ak junni ak ñeenti téemeer.","[boːy ñow nanga indaːle ñaːri tiriyangal, benː feyukaːy, benː teːmbaru ñeːnti teːmeːr ak junːi ñeːnti teːmeːr]"
|
| 61 |
+
60,8 heures,TECHNICAL_VISIT,Juróom ñatti waxtu,[juroːm ñatːi waxtu]
|
| 62 |
+
61,9 heures,TECHNICAL_VISIT,Juróom ñeenti waxtu,[juroːm ñeːnti waxtu]
|
| 63 |
+
62,10 heures,TECHNICAL_VISIT,Fukki waxtu,[fukːi waxtu]
|
| 64 |
+
63,11 heures,TECHNICAL_VISIT,Fukki waxtu ak benn,[fukːi waxtu ak benː]
|
| 65 |
+
64,12 heures,TECHNICAL_VISIT,Fukki waxtu ak ñaar,[fukːi waxtu ak ñaːr]
|
| 66 |
+
65,13 heures,TECHNICAL_VISIT,Fukki waxtu ak ñatt,[fukːi waxtu ak ñatː]
|
| 67 |
+
66,14 heures,TECHNICAL_VISIT,Fukki waxtu ñeent,[fukːi waxtu ñeːnt]
|
| 68 |
+
67,15 heures,TECHNICAL_VISIT,Fukki waxtu ak juróom,[fukːi waxtu ak juroːm]
|
| 69 |
+
68,16 heures,TECHNICAL_VISIT,Fukki waxtu ak juróom-benn,[fukːi waxtu ak juroːm-benː]
|
| 70 |
+
69,17 heures,TECHNICAL_VISIT,Fukki waxtu ak juróom-ñaar,[fukːi waxtu ak juroːm-ñaːr]
|
| 71 |
+
70,18 heures,TECHNICAL_VISIT,Fukki waxtu ak juróom-ñett,[fukːi waxtu ak juroːm-ñetː]
|
| 72 |
+
71,19 heures,TECHNICAL_VISIT,Fukki waxtu ak juróom-ñeent, [fukːi waxtu ak juroːm-ñeːnt]
|
| 73 |
+
72,20 heures,TECHNICAL_VISIT,Ñaar-fukki waxtu,[ñaːr-fukːi waxtu]
|
| 74 |
+
73,Combien souhaitez-vous transférer ?,TRANSFER_MONEY,Ñaata nga bëgga toxal ?,[ñaːta nga bëgːa toxal ?]
|
| 75 |
+
74,A qui souhaitez-vous transférer de l'argent ?,TRANSFER_MONEY,Kan nga bëgga toxalal xaalis bi?,[kan nga bëgːa toxalal xaːlis bi ?]
|
| 76 |
+
75,Confirmez-vous le transfert de la somme de ,TRANSFER_MONEY,Ndax firndeel nga toxal bu tollu ci,[ndax firndeːl nga toxal bu tolːu ci]
|
| 77 |
+
76,Le montant que vous souhaitez transférer n'est pas disponible,TRANSFER_MONEY,Koppar yi nga bëgga toxal jàppandiwul,[kopːar yi nga bëgːa toxal japːandiwul]
|
| 78 |
+
77,Impossible d'effectuer l'opération de transfert,TRANSFER_MONEY,Jëflante toxal bi mënula nekk.,[jëflante toxal bi mënul nekː]
|
WolBanking77/audio/test.parquet
ADDED
|
@@ -0,0 +1,3 @@
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
| 1 |
+
version https://git-lfs.github.com/spec/v1
|
| 2 |
+
oid sha256:4da733a89418fbc5d895683a6f95a24bb6921210bd6d28938f7bfe550697cb36
|
| 3 |
+
size 98840459
|
WolBanking77/audio/train.parquet
ADDED
|
@@ -0,0 +1,3 @@
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
|
| 1 |
+
version https://git-lfs.github.com/spec/v1
|
| 2 |
+
oid sha256:cd537af095a1b792d0e83a0a1f8f486af733f97401ed81948eb9453a4cfa9d5f
|
| 3 |
+
size 391956316
|
WolBanking77/text/5k_split/test/test.csv
ADDED
|
The diff for this file is too large to render.
See raw diff
|
|
|
WolBanking77/text/5k_split/train/train.csv
ADDED
|
The diff for this file is too large to render.
See raw diff
|
|
|
WolBanking77/text/full/test/test.csv
ADDED
|
The diff for this file is too large to render.
See raw diff
|
|
|
WolBanking77/text/full/train/train.csv
ADDED
|
The diff for this file is too large to render.
See raw diff
|
|
|